Wildebeest analysis examples for:   wol-wol2010   …    February 25, 2023 at 01:33    Script wb_pprint_html.py   by Ulf Hermjakob

27811  ACT 23:9  Ci kaw loolu nag coow lu bare daldi jib. Ñenn ca xutbakat, ya bokk ca Farisen ya, ne bërét, daldi xuloo bu metti ne: «Gisunu dara lu bon ci nit kii. Su fekkeente ne rab a ko wax mbaa malaaka