Wildebeest analysis examples for:   wol-wol2010   N    February 25, 2023 at 01:33    Script wb_pprint_html.py   by Ulf Hermjakob

23217  MAT 1:4  Aram Aminadab; Aminadab Nason; Nason Salmon;
23231  MAT 1:18  Nii la Yeesu Kirist juddoo. Bi ñu mayee Maryaama ndeyam Yuusufa, waaye laata ñoo ànd, gis nañu ne dafa ëmb ci kàttanu Xel mu Sell mi.
23237  MAT 1:24  Noonu Yuusufa yewwu, yeggali soxnaam, na ko ko malaakam Boroom bi sante woon.
23240  MAT 2:2  Ñu ne: «Ana buur bi juddul Yawut yi? Ndaxte gis nanu biddiiwam ci penku te ñëw nanu ngir màggal ko.»
23246  MAT 2:8  Noonu mu yebal leen Betleyem naan: «Demleen fa, seet bu wóor mbirum xale ba. Bu ngeen ci amee lu wóor nag, ngeen xamal ma ko, ngir man itam ma dem màggal ko.»
23250  MAT 2:12  Bi ñu ko defee Yàlla artu na leen ci biirnt, ñu baña dellu ca Erodd. Noonu ñu jaar weneen yoon, ñibbi seen réew.
23253  MAT 2:15  Mu toog fa, ba Erodd faatu. Noonu am li Boroom bi waxoon jaarale ko cib yonent, bi mu naan: «Woo naa sama doom, munn Misra.»
23261  MAT 2:23  Mu ñëw nag dëkk ci dëkk bu ñuy wax Nasaret. Noonu am la ñu waxoon ca xale ba, jaarale ko ca yonent ya, bi ñu naan: «Dees na ko tudde Nasareen
23263  MAT 3:2  Nii la doon waaree: «Tuubleen seeni bàkkaar, ndaxte nguuru Yàlla Aji Kawe ji jege na.»
23266  MAT 3:5  Noonu ñéppnn jëm ci moom, ñi dëkk Yerusalem ak diiwaanu Yude, ak waa dexu Yurdan.
23268  MAT 3:7  Noonu ay Farisen ak ay Sadusen yu bare ñëw ci Yaxya, ngir mu sóob leen ñoom itam ca dex ga. Waaye bi leen Yaxya gisee, mu ne leen: «Yéen ñi fees ak daŋar mel ni ay co, ku leen artu, ngeen daw merum Yàlla mi nara wàcc?
23270  MAT 3:9  te buleen wax ci seen xel naan: Nun daal doomi Ibraayma lanu,” ndaxte maa ngi leen koy wax, Yàlla man na sàkkal Ibraayma ay doom ci doj yii.
23276  MAT 3:15  Yeesu ne ko: «Bàyyil noonu, ndaxte war nanoo mottali lépp lu jub.» Noonu Yaxya nangu.
23281  MAT 4:3  Noonu fiirkat bi ñëw ci moom ne ko: «Boo dee Doomu Yàlla, santal doj yii, ñu nekk mburu.»
23282  MAT 4:4  Waaye Yeesu ne ko: «Mbind mi nee na: Nit du dunde mburu rekk, waaye itam gépp kàddu gunne ci gémmiñug Yàlla.”»
23288  MAT 4:10  Waaye Yeesu ne ko: «Sore ma Seytaane, ndaxte Mbind mi nee na: Nanga màggal Yàlla sa Boroom, te jaamu ko moom rekk.”»
23289  MAT 4:11  Noonu Seytaane bàyyi ko. Te ay malaaka daldi ñëw fi Yeesu, di ko topptoo.
23291  MAT 4:13  Gannaaw gi, mu toxoo dëkku Nasaret, dem dëkk Kapernawum, bi féeteek dex ga ci diiwaani Sabulon ak Neftali.
23292  MAT 4:14  Noonu am la ñu waxoon, jaarale ko ci yonent Yàlla Esayi, bi mu naan:
23293  MAT 4:15  «Yaw réewum Sabulon ak réewum Neftali, di yoonu géej gannaaw dexu Yurdan, yaw Galile, réewum ñi dul Yawut—
23299  MAT 4:21  Ba Yeesu demee ba ca kanam, mu gis yeneen ñaar ñu bokk ndey ak baay, ñuy Saag doomu Sebede, ak Yowaana rakkam. Ñu nekk ci seen biir gaal ak Sebede seen baay, di defar seeni mbaal. Noonu Yeesu woo leen.
23303  MAT 4:25  Noonu mbooloo mu bare topp ci moom, jóge ci wàlli Galile ak diiwaan bi ñuy wax Fukki dëkk yi, ci dëkku Yerusalem ak ci diiwaanu Yude, ba ci gannaaw dexu Yurdan.
23315  MAT 5:12  Bégleen tenneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. Ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu.
23319  MAT 5:16  Na seen leer leere noonu ci kanam nit ñi, ngir ñu gis seeni jëf yu rafet, te màggal seen Baay bi ci kaw.
23321  MAT 5:18  Ndaxte ci dëgg maa ngi leen koy wax, li feek asamaan ak suuf wéyul, benn tomb walla benn rëddu araf du wéy mukk ci yoonu Musaa, ba kera yépp di am.
23323  MAT 5:20  Ndaxte maa ngi leen koy wax, bu seen njubte ëppul njubteg xutbakat ya ak Farisen ya, dungeen tàbbi mukk ci nguuru Yàlla Aji Kawe ji.
23333  MAT 5:30  Ndaxte ñàkk benn ci say cér moon ci yaw, ñunni sa yaram wépp ci sawara. Bu la sa loxol ndijoor bëggee yóbbe bàkkaar, dagg ko,nni ko fu sore. Ndaxte ñàkk benn ci say cér moon ci yaw ñunni sa yaram wépp ci sawara.
23348  MAT 5:45  ngir wone ne yéenay doomi seen Baay bi nekk ci kaw. Ndaxte mu ngi fenkal jantam ci kaw ñu bon ñi ak ñu baax ñi, te muy tawal ñi jub ak ñi jubadi.
23351  MAT 5:48  Nangeen mat nag, ni seen Baay bi ci kaw mate.
23355  MAT 6:4  ngir sa sarax nekk kumpa. Noonu sa Baay, bi dara umpul, dina la ko delloo.
23357  MAT 6:6  Yaw nag booy ñaan, duggal ci sa néeg, tëj bunt bi, te nga ñaan sa Baay bi bët manta gis. Noonu sa Baay, bi dara umpul, dina la ko delloo.
23364  MAT 6:13  Yàlla boo nu teg ci yoonu nattu, waaye yal nanga nu musal ci lu bon. Ndaxte yaw yaa yelloo nguur ak kàttan ak màggaay, ba fàww. Amiin.”
23369  MAT 6:18  ngir sa koor baña feeñu nit ñi, waaye mu feeñu sa Baay bi bët manta gis. Noonu sa Baay, bi dara umpul, dina la ko delloo.
23372  MAT 6:21  Ndaxte fu sa alal nekk, fa la sa xol nekk itam.
23377  MAT 6:26  Seetleen picci asamaan: duñu ji, duñu góob, duñu denc ci sàq; teewul seen Baay bi ci kaw moo leen di dundal. Ndax ëppuleen maana picc yi ci lu bare?
23383  MAT 6:32  Ndaxte loolu lépp, ñi xamul Yàlla ñoo koy wut. Te seen Baay, bi nekk ci kaw, xam na ne am ngeen soxla ci loolu lépp.
23387  MAT 7:2  Ndaxte dees na leen àtte ak ni ngeen di àttee, nattal leen ak li ngeen di nattale.
23390  MAT 7:5  Naaféq, jëkkala dindi nj gi ci sa bët, te noonu dinga mana gis bu leer, ngir dindi ñax gi ci sa bëtu mbokk.
23393  MAT 7:8  Ndaxte képp kuy ñaan, dinga am; kuy seet, dinga gis; kuy fëgg, ñu ubbil la.
23396  MAT 7:11  Ndegam yéen ñi bon yéena mana jox seeni gone lu baax, astamaak seen Baay bi nekk ci kaw dina jox lu baax ñi ko koy ñaan!
23401  MAT 7:16  Dingeen leen xàmmee ci seeni jëf. Ndax dees na witte reseñ ci dédd, walla figg ci xaaxaam?
23402  MAT 7:17  Noonu garab gu baax gu nekk dina meññ doom yu neex, waaye garab gu bon dina meññ doom yu bon.
23407  MAT 7:22  Bu bés baa, ñu bare dinañu ma wax: “Boroom bi, Boroom bi, ndax du ci saw tur lanu daa waxe ci kàddug Yàlla? Ndax du ci saw tur lanu daa dàqe ay rab? Ndax du ci saw tur lanu daa defe ay kéemaan yu bare?”
23416  MAT 8:2  Noonu ku gaana ñëw, sukk ci kanamam ne ko: «Sang bi, soo ko bëggee, man nga maa faj.»
23423  MAT 8:9  Ndaxte man itam maa ngi nekk ci ndigal, te ame naa ay xarekat ci sama ndigal. Su ma nee kii: “Demal,” mu dem. Mbaa ma ne keneen ki: “Ñëwal,” mu ñëw. Te su ma nee sama jaam: “Defal lii,” mu def ko.»
23427  MAT 8:13  Ci kaw loolu Yeesu wax njiit la ne ko: «Ñibbil, na ame, ni nga ko gëme.» Noonu ca waxtu woowa sax surga ba daldi wér.
23435  MAT 8:21  Noonu keneen ca taalibe ya ne ko: «Sang bi, may ma, ma jëkka dem suuli sama baay.»
23439  MAT 8:25  Noonu taalibe ya daldi jegesi, yee ko naan: «Sang bi, musal nu, nu ngiy dee!»
23443  MAT 8:29  Ña rab jàpp daldi xaacu naan: «Yaw Doomu Yàlla ji, loo nuy fexeel? Ndax danga noo bëgga mbugal, bala waxtu way jot?»
23448  MAT 8:34  Noonu dëkk ba béppnn seeti Yeesu. Ba ñu ko gisee nag, ñu ñaan ko, munn seen réew.
23450  MAT 9:2  Foofa ñu indil ko ku tëdd ci basaŋ, fekk yaramam wépp làggi. Bi Yeesu gisee seen ngëm, mu ne ku làggi ka: «Na sa xel dal, sama waay, baal nañu la say bàkkaar.»
23451  MAT 9:3  Bi mu waxee loolu, ay xutbakat daldi ne ci seen biir: «Nit kii mu ngi sosal Yàlla.»
23455  MAT 9:7  Noonu làggi ba daldi jóg, ñibbi.
23457  MAT 9:9  Bi Yeesu jógee foofa, mu gis nit ku tudd Macë, toog ca juuti ba. Yeesu ne ko: «Kaay topp ma.» Noonu Macë jóg, daldi ko topp.
23461  MAT 9:13  Mbind mi nee na: “Yërmande laa bëgg, waaye du rendi saraxi mala.” Demleen nag te seet lu wax joojuy tekki. Ndaxte ñëwuma, ngir woo ñi jub, waaye bàkkaarkat yi laay woo.»
23463  MAT 9:15  Yeesu ne leen: «Ndax gan yi ñëw ci céet dinañu naqarlu dara, li feek boroom céet gaa ngi ànd ak ñoom? Waaye bés yaa ngi ñëw yu ñuy jële boroom céet gi ci seen biir; booba nag dinañu woor.
23465  MAT 9:17  Te it duñu def biiñ bu bees ci mbuusi der yu màggat. Lu ko moy, mbuus yi dañuy toj, biiñ bi tuuru te mbuus yi yàqu. Waaye biiñ bu bees, dees na ko def ci mbuus yu bees. Noonu ñoom ñaar duñu yàqu.»
23467  MAT 9:19  Noonu Yeesu jóg, topp ko, moom ak ay taalibeem.
23470  MAT 9:22  Bi mu ko defee Yeesu waññiku ne ko: «Na sa xel dal, soxna si, sa ngëm faj na la.» Noonu jigéen ja daldi wér ca saa sa.
23474  MAT 9:26  Noonu xibaaru li mu def daldi siiw ca réew ma.
23476  MAT 9:28  Noonu Yeesu dugg ca kër ga, gumba ya toppsi ko. Yeesu ne leen: «Ndax gëm ngeen ne man naa def li ngeen ma laaj?» Ñu ne ko: «Waaw, Sang bi.»
23477  MAT 9:29  Kon Yeesu daldi laal seeni bët ne leen: «Na am, ni ngeen ko gëme.»
23483  MAT 9:35  Noonu Yeesu wër dëkk yu mag ya yépp ak yu ndaw ya, di leen ngal ci seeni ngu, tey yégle xibaaru jàmm bi jëm ci nguuru Yàlla, di fajngoro yépp ak wéradi yépp.
23485  MAT 9:37  Noonu mu ne taalibeem ya: «Ngóob mi yaatu na, waaye liggéeykat yi barewuñu.
23487  MAT 10:1  Noonu Yeesu woo ca moom fukki taalibeem ya ak ñaar, jox leen sañ-sañu dàq rab yi, tey fajngoro yépp ak wéradi yépp.
23493  MAT 10:7  Bu ngeen demee nag, yégleleen naan: Nguuru Yàlla Aji Kawe ji jegesi na.”
23505  MAT 10:19  Boo xamee ne nag jébbale nañu leen, buleen am xel ñaar ci li ngeen di wax, mbaa ni ngeen koy waxe. Ndaxte ca waxtu woowa sax dingeen jot li ngeen wara wax;
23511  MAT 10:25  Bu taalibe yemee ak kilifaam demin, doy na; jaam it ni sangam. Ndegam tudde nañu boroom kër gi Beelsebul, astamaak waa kër gi.
23521  MAT 10:35  Ndaxte ñëw naa ngir féewale doom ak baayam, doom ju jigéen ak ndeyam, jabar ak goroom;
23531  MAT 11:3  ne ko: «Ndax yaa di Ki wara ñëw, walla danoo wara xaar keneen
23536  MAT 11:8  Kon lu ngeen seeti woon nag? Nit ku sol yére yu rafet? Waaye ñi sol yére yu rafet ñu ngi dëkk ci këri buur.
23537  MAT 11:9  Lu tax ngeen nn nag? Ngir gis ab yonent? Waaw, wax naa leen ne ëpp na yonent.
23541  MAT 11:13  Ndaxte li yonent yi wax ak li yoonu Musaa tëral ñu ngi doon dox, ba kera Yaxya di feeñ.
23544  MAT 11:16  «Niti jamono jii nag, lan laa leen mana ngaleel? Ñu ngi nirook xale yu toog canc ma, di woo seeni xarit,
23546  MAT 11:18  Ndaxte Yaxya feeñ na, lekkul, naanul, ngeen daldi ne: “Dafa ànd ak rab.”
23551  MAT 11:23  Te yaw dëkku Kapernawum, ndax dees na la yékkati bu kawe? Déedéet, dees na la daane bu suufe. Ndaxte kéemaan yi ma def ci yaw, bu ñu leen defoon ci dëkku Sodom, kon mu nekk ba tey.
23558  MAT 11:30  Ndaxte sama kilifteef lewet na te sama yen diisul.»
23561  MAT 12:3  Noonu Yeesu ne leen: «Ndax nguleen la Daawuda defoon, ba mu xiifee, moom ak ña mu àndaloon?
23566  MAT 12:8  Ndaxte Doomu nit ki mooy boroom bésub noflaay bi.»
23568  MAT 12:10  te amoon na fa nit ku loxoom làggi. Noonu Farisen ya laaj ko: «Faj ci bésub noflaay bi, ndax loolu jaadu na?» Fekk ñuy wut buntu tuumaal ko.
23570  MAT 12:12  Nit nag, ndax ëppul maana xar? Kon def lu baax ci bésub noflaay bi jaadu na.»
23571  MAT 12:13  Noonu Yeesu ne nit ka: «Tàllalal sa loxo!» Mu tàllal ko nag, loxoom daldi wér, mel ni ba ca des.
23576  MAT 12:18  «Kii mooy sama Ndaw li mann, di sama Soppe bi neex sama xol. Dinaa def sama Xel ci moom, muy yégal xeet yi yoonu njub.
23581  MAT 12:23  Noonu mbooloo mépp yéemu naan: «Ndax kii du Sëtu Daawuda bi?»
23588  MAT 12:30  Noonu ku farul ak man, yaa ngi may xeex, ku dajalewul ak man, yaa ngi tasaare.»
23591  MAT 12:33  Neeleen garab gi baax na, moom ak meññeefam, walla ngeen ne garab gi bon na, moom ak meññeefam; ndaxte garab, meññeefam lañu koy xàmmee.
23592  MAT 12:34  Yéen ñi fees ak daŋar ni ay co, naka ngeen mana waxe lu baax, fekk dangeen bon? Ndaxte gémmiñ, la fees xol lay wax.
23593  MAT 12:35  Noonu nit ku baax, lu baax lay wax, jële ko ca fa mu denc lu baax, te nit ku bon, lu bon lay wax, jële ko ca fa mu denc lu bon.
23595  MAT 12:37  Ndaxte dees na la àtte ni ku jub ci say wax, walla ñu daan la ci say wax.»
23598  MAT 12:40  Ndaxte ni Yunus nekke woon ñetti guddi ak ñetti bëccëg ci biir rabu géej wu mag, noonu la Doomu nit ki di nekke ñetti guddi ak ñetti bëccëg ci biir suuf.
23599  MAT 12:41  Keroog bésnc waa dëkku Niniw dinañu jógandoo ak niti jamono jii, yey leen; ndaxte bi leen Yunus waaree, tuub nañu seeni bàkkaar, te ku sut Yunus a ngi fi.
23602  MAT 12:44  Noonu da naan: Naa dellu ca sama kër, ga manne woon.” Bu ñëwee nag, mu fekk kërug neen, ñu bale ko, defar ko ba lépp jekk.