Wildebeest analysis examples for:   wol-wol2010   R    February 25, 2023 at 01:33    Script wb_pprint_html.py   by Ulf Hermjakob

23218  MAT 1:5  Salmon jur ci Raxab doom ju tudd Bowas; Bowas am ak Ruut Obedd; Obedd jur Isayi,
23220  MAT 1:7  Suleymaan jur Robowam; Robowam Abiya; Abiya Asaf;
23256  MAT 2:18  «Baat jib na ci Rama, ay jooy ak yuux gu réy, Rasel mooy jooy ay doomam te bëggul kenn dëfal ko, ndaxte saay nañu.»
23445  MAT 8:31  Rab ya nag ñaan ko ne: «Boo nu dàqee, sànni nu ca géttu mbaam-xuux ya.»
23446  MAT 8:32  Yeesu ne leen: «Demleen.» Rab ya nag daldi génn, dugg ca mbaam-xuux ya, ñu daldi bartalu, daanu ca dex ga, lab ca ndox ma.
23583  MAT 12:25  Waaye Yeesu xam seen xalaat ne leen: «Réew mu xeex boppam tas, te dëkk mbaar guy xeex boppam du mana yàgg.
23724  MAT 15:22  Ba mu fa àggee nag, jigéenu waa Kanaan, ja dëkk ca wàll yooyu, daldi génn, di wax ca kaw ne ko: «Yaw sang bi, Sëtu Daawuda bi,rëm ma! Rab jàpp na sama doom ju jigéen, te dafa sonn lool.»
23945  MAT 22:4  Kon mu yónneeti yeneen surga ne leen: “Bu ngeen demee, yégal-leen gan yi sama woote bii:Reer yi noppi na, reylu naa samay nag ak samay jur gu duuf; lépp sotti na, ñëwleen ci reer yi.’ ”
23949  MAT 22:8  Ci kaw loolu mu ne surga ya:Reeri céet gi noppi na, waaye ñi ñu woo yeyoowuñu ko.
24175  MAT 26:52  Waaye Yeesu ne ko: «Roofal sa jaasi ci mbaram, ndaxte ku bocci jaasi, jaasi moo lay rey.
24381  MRK 3:24  Réew mu xeex boppam, du mana yàgg.
24445  MRK 5:12  Rab ya ñaan Yeesu: «Jox nu ndigal, nu dugg mbaam-xuux ya.»
24916  MRK 15:21  Amoon na nag nit ku dëkk Siren, tudd Simoŋ, di baayu Alegsàndar ak Rufus. Fekk booba mu romb fa, jóge ca wet, ga féete ak tool ya, ñu ga ko ngir mu gàddu bant bi.
25121  LUK 3:27  Yoda, Yowanan mooy baayam; Yowanan, Resa; Resa, Sorobabel. Kooku Salacel a ko jur; Salacel, Neri;
25129  LUK 3:35  Serug; Rew; Peleg; Eber; Sela.
25343  LUK 8:29  Dafa wax loolu, ndaxte Yeesu santoon na rab wi, mu génn ci moom. Rab wa dafa ko doon farala jàpp. Nit ñi daan nañu ko wottu, di ko yeew ak ay càllala, ak di ko jéng, mu di leen dagg, rab wi di ko xiir carab yu wéet.
25345  LUK 8:31  Rab yooyoo ngi ko doon ñaan, ngir mu bañ leena sant, ñu dem ca kàmb gu xóot gi.
25346  LUK 8:32  Fekk amoon na fa géttu mbaam-xuux yu bare, yuy for ca tund wa. Rab ya ñaan Yeesu, mu may leen, ñu dugg mbaam-xuux ya. Mu may leen ko.
25491  LUK 11:17  Waaye Yeesu xam seen xalaat ne leen: «Réew mu xeex boppam tas,r gu xeex boppam gent.
25692  LUK 16:3  «Bëkk-néeg bi di xalaat naan: “Nu may def nag, segam sama njaatige dafa may dàq ci liggéey bi mu ma joxoon? Dem beyi? Awma kàttanam. Yelwaani? Rus naa ko.
25715  LUK 16:26  Rax-ca-dolli it am na kàmb gu xóot sunu diggante ak yéen, ba tax ñi bëgga jóge fii jëm ci yéen, walla ñi bëgga jóge foofu jëmsi ci nun, duñu ko man.”
25761  LUK 18:4  Àttekat ba bañ lu yàgg, waaye am bés mu ne ci xelam:Ragaluma Yàlla te faalewuma mbindeef,
26022  LUK 23:18  Waaye ñu bokk di yuuxu, ñoom ñépp naan: «Reyal kii te bàyyi Barabas!»
26048  LUK 23:44  Noonu digg bëccëg daldi jot, jant ba nëbbu, réew mépp daldi lëndëmruus lu mat ñetti waxtu. Ridob rab bu sell ba car Yàlla ga daldi xar ñaar.
26151  JHN 1:38  Yeesu geestu, gis ne ñoo ngi koy topp. Mu ne leen: «Lu ngeen soxla woon?» Ñu ne ko: «Foo dëkk, Ràbbi?» Ràbbi mi ngi tekki «Kilifa gi».
26402  JHN 7:5  Rakkam yi dañu doon wax loolu, ndaxte ñoom itam gëmuñu ko woon.
26531  JHN 9:22  Ragal Yawut ya nag moo taxoon waajuri nit ka waxe noonu, ndaxte Yawut ya dañoo mànkoo woon ne, képp ku seede ne Yeesu mooy Almasi bi, ñu dàq la ca jàngu ba.
26618  JHN 11:26  Rax-ca-dolli kuy dund te gëm ma, doo dee mukk. Ndax gëm nga loolu?»
26640  JHN 11:48  Ndaxte su nu ko bàyyee mu jàppoo nii, ñépp dinañu ko gëm, te kilifay Room yi dinañu ñëw, daaneel sunur Yàlla gi, tas sunu réew!»
26865  JHN 18:11  Waaye Yeesu ne Piyeer: «Roofal jaasi ji ci mbaram. Ndax warumaa naan kaasu naqar, bi ma Baay bi sédd?»
26914  JHN 19:20  Mbind mooma, Yawut yu bare jàng nañu ko, ndaxte fa ñu daajoon Yeesu ca bant ba jege woon na dëkk ba, te mbind ma ci làkku yawut la woon, ci làkku waa Room ak ci gereg.
26952  JHN 20:16  Noonu Yeesu ne ko: «Maryaama.» Mu walbatiku, làkk ko ci yawut ne ko: «Ràbbuni!» Ràbbuni mooy tekki «Kilifa gi».
27028  ACT 2:10  di waa Firisi, Pamfili, Misra ak weti Libi, yi dend ak Siren, nun ak gan ñi jóge Room,
27058  ACT 2:40  Noonu mu artu leen ak yeneen wax yu bare, di leen dénk ne: «Rëccleen ci niti jamono ju dëng jii.»
27061  ACT 2:43  Ragal jàpp ñépp, te ndaw yi di def ay kéemaan ak ay firnde yu bare.
27097  ACT 4:6  Ràññee nañu ci: Anas, miy sarxalkat bu mag bi, Kayif, Yowaana, Alegsàndar ak bokki sarxalkat bu mag bi.
27228  ACT 7:43  Yóbbu ngeen sax fu nekk xayma, biy màggalukaayu Molog, ak biddiiwub Refan, bi ñu daan bokkaaleel Yàlla, di ay nataal, yi ngeen defoon ngir màggal leen! Kon nag dinaa leen toxal, yóbbu leen ci gannaaw réewu Babilon.”
27237  ACT 7:52  Kan ca yonent ya la seeni maam tegul woon ay fitna? Rey nañu ñi doon yégle ñëwug Aji Jub ji, moom mi ngeen jébbale léegi, ba ñu rey ko.
27267  ACT 8:22  Réccul nag sa coxor te ñaan Boroom bi, mu baal la sa xalaatu xol, su manee am.
27419  ACT 12:13  Noonu Piyeer fëgg buntur ga, te mbindaan mu tudd Rodd wuyusi ko.
27564  ACT 16:12  Bi nu fa teeree, nu jëm Filib, bi nekk dëkk bi ëpp maana ca wàll woowu ci diiwaanu Maseduwan, di it moomeelu Room. Nu toog fa ay fan.
27573  ACT 16:21  di xamle ay aada yu nu sañula nangu mbaa nu di ko topp, nun ñi bokk ci nguuru Room.»
27589  ACT 16:37  Waaye Pool ne alkaati ya: «Dóor nañu nu ay yar ci kanam ñépp, ci lu ñu wéerul ci benn àtte, rax-ca-dolli tëj nañu nu kaso, nun ñiy jaambur ci nguuru Room. Léegi ndax dañu noo bëgga sànni ci mbedd mi ci kumpa? Mukk! Nañu ñëw, ñoom ci seen bopp, gunge nu ci biti.»
27590  ACT 16:38  Bi mu ko waxee, alkaati ya yégal àttekat ya la mu wax. Bi ñu déggee ne jaamburi Room lañu, ñu daldi tiit.
27628  ACT 18:2  Mu tase fa ak Yawut bu tudd Akilas te juddoo diiwaanu Pont. Muy sooga jóge réewu Itali ak soxnaam Pirsil, ndaxte buur ba Këlódd sant na Yawut yépp, ñu génn Room.
27675  ACT 19:21  Bi loolu wéyee Pool nas xel jëm Yerusalem, jaar ci diiwaani Maseduwan ak Akayi. Mu ne: «Gannaaw bu ma fa demee, fàww ma seeti Room it.»
27733  ACT 21:1  Bi nga xamee ne tàggoo nanu ak ñoom ci naqar, nu dugg gaal, jubal dunu Kos. Te ca ëllëg sa nu dem ba teer ca Rodd, ba noppi jóge fa, jàll ba Patara.
27768  ACT 21:36  Ndaxte mbooloo maa nga ko topp, di xaacu ne: «Reyleen ko!»
27792  ACT 22:20  Rax-ca-dolli bi ñu tuuree deretu Ecen, mi la doon seedeel, teewe naa ko, ànd ca, bay wottu saxrey ñi ko doon rey.”
27797  ACT 22:25  Waaye bi ñu koy joñ ak ay der, Pool ne njiitu xare ba fa taxaw: «Ndax am nga sañ-sañu dóor ay yar jaamburu Room, te fekk yoon dabu ko sax?»
27798  ACT 22:26  Bi ko njiit la déggee, mu fekki kilifaam, yégal ko ko; mu ne ko: «Ndax xam nga li ngay def? Nit kale jaambur la ci Room.»
27799  ACT 22:27  Noonu kilifa ga ñëw laaj Pool: «Wax ma, ndax jaambur nga ci Room?» Mu ne ko: «Waaw, moom laa.»
27800  ACT 22:28  Kilifa ga ne ko: «Man fey naa xaalis bu bare, ngir nekk jaambur ci Room.» Waaye Pool ne ko: «Man de dama koo judduwaale.»
27801  ACT 22:29  Ñi ko bëggoona dóor ay yar nag randu ko ca saa sa. Te kilifa ga sax tiit ci xam ne Pool jaamburu Room la, te yeewlu na ko.
27813  ACT 23:11  Ca guddi ga nag Boroom bi taxaw ci wetu Pool ne ko: «Takkal sa fit; ni nga ma seedee ci Yerusalem, noonu nga may seedee ca Room.»
27829  ACT 23:27  Yawut yi jàpp nañu nit kii, bëgg koo rey, waaye bi ma yégee ne jaambur la ci Room, wallu naa ko ak ay xarekat, ba musal ko.
27880  ACT 25:16  Waaye ma ne leen: “Jébbale nit, fekk jàkkaarloowul ak ñi koy jiiñ, ba mana làyyil boppam ci li ñu koy jiiñ, loolu dëppoowul ak aaday nguuru Room.”
27901  ACT 26:10  Daan naa ko def ci Yerusalem, ba noppi ma jot sañ-sañ ci sarxalkat yu mag ya, bay tëj gaayi Yàlla yu bare. Rax-ca-dolli ku ñu ci masoona bëgga rey, ànd naa ci.
27980  ACT 28:13  Nu jóge fa, leru tefes ga, ba agsi Resiyo. Ca ëllëg sa ngelawu sudd daldi jóg, te ca ñaareelu fan ba nu teer Pusol.
27981  ACT 28:14  Gis nanu fa ay bokk, ñu ñaan nu, nu toog fa ayu-bés. Noonu nu dem Room.
27983  ACT 28:16  Bi nu dikkee Room nag, ñu may Pool, mu dëkk fa ko lew, moom ak xarekat ba koy wottu.
27984  ACT 28:17  Bi ñetti fan wéyee, mu woolu njiiti Yawuti dëkk ba. Bi ñu dajaloo nag, mu wax leen lii: «Bokk yi, jàpp nañu ma ci Yerusalem, jébbal ma waa Room, fekk defuma dara luy suufeel sunu xeet, mbaa lu juuyoo ak sunuy aaday maam.
27985  ACT 28:18  Waa Room nag seet sama mbir, te bëgg maa bàyyi, ndaxte toppuñu ma dara lu jar dee.
28005  ROM 1:7  Yéen ñi dëkk Room ñépp, yéen ñi Yàlla bëgg te woo leen, ngeen nekk gaayam yu sell, na leen Yàlla sunu Baay ak Boroom bi Yeesu Kirist may yiw ak jàmm.
28013  ROM 1:15  Li aju ci man nag, jekk naa ngir ñëw, xamal leen xibaaru jàmm bi, yéen it waa Room.
28061  ROM 3:2  Raw na ko fu nekk. Ci bu jëkk Yawut yi la Yàlla dénk waxam.
28233  ROM 9:10  Du ci loolu rekk, waaye noonu la it ci lu jëm ci Rebeka; doom yi mu jur ñoo bokk benn baay, moo di sunu maam Isaaxa.
28417  ROM 16:13  Maa ngi nuyu it Rufus, waa ji xolam seey ci Boroom bi, ak yaayam, mi ma féete woon itrub ndey.
28669  1CO 11:1  Royleen ma nag, ni may roye Kirist.
28754  1CO 14:8  Rax-ca-dolli su liit gi jibul bu leer, kuy mana waajal xare ba?
28801  1CO 15:15  Rax-ca-dolli gis nañu ne seedeel nanu Yàlla ay fen, ndaxte seede nanu ci mbiram ne dekkal na Yeesu, te fekk dekkalu ko, su néew yi dul dekki.
29038  2CO 9:14  Rax-ca-dolli dinañu sant Yàlla ak xol bu fees ak cofeel ci yéen ndax yiw wu mag, wi Yàlla def ci yéen.
29110  2CO 12:20  Ragal naa, bu ma ñëwee ci yéen, fekk leen nu ma neexul, te yéen it ngeen fekk ma nu leen neexul. Ragal naa fekk ay xuloo ci seen biir, ak ñeetaane, xadar ak diiroo mbagg, xas ak jëw, réy-réylu ak yëngu-yëngu.
29111  2CO 12:21  Ragal naa, bu ma leen ganesiwaatee, Yàlla sama Boroom suufeel ma ci seen biir, ma naqarlu ci ñu bare ñu bàkkaaroon te dëdduwuñu seen yàqute, seen njaaloo ak seen ñaawteef, gi ñu doon def.
29225  GAL 4:27  Ndaxte Mbind mi nee na: «Bégal, yaw jigéen ji dul jur te masula am doom. Reeyal te bànneexu, yaw mi masula xam coonob mat, ndaxte jigéen ji ñu faalewul moo gëna jaboot ki nekk ak jëkkëram.»
29496  PHP 3:8  Rax-ca-dolli dëddu naa lépp ngir xéewali xam Kirist Yeesu sama Boroom, di xam-xam bu xóot, ba xel manu koo takk. Moo tax ñàkk naa sama lépp, te def ko ni mbalit, ngir amr ci Kirist.
29788  1TI 2:5  Ndaxte jenn Yàlla kepp moo am, ak benn Rammukat kepp diggante Yàlla ak nit ñi, di nit ki Kirist Yeesu,
29892  2TI 1:16  Waaye Onesifor daa na faral di dëfal sama xol; na Boroom bi sottirmandeem ciram. Rusul woon sax ci samay jéng,
29893  2TI 1:17  waaye bi mu ñëwee dëkku Room, wut na ma fu ne, ba gis ma.
29955  2TI 4:18  Rax-ca-dolli dina ma musal ci bépp jëf ju ñaaw, tette ma ci jàmm, ba tàbbal ma ci nguuram gu kawe ga. Yal na yelloo ndam ba fàww. Amiin.
30187  HEB 9:15  Looloo tax mu nekk Rammukat bi ci wàllu kóllëre gu bees ci diggante Yàlla ak nit, ngir ñi Yàlla woo amr bu sax ci kaw, te mu digoon leen ko, ndaxte Kirist dee na, ngir jot ñi jàdd yoon ca kóllëre gu jëkk ga.
30270  HEB 11:31  Ngëm moo tax ba Raxab jigéenu moykat bi mucc, keroog ba ñuy bóom ñi déggadiloon Yàlla, ndax li mu teeru woon yëddukat ya teeru bu ànd ak jàmm.
30303  HEB 12:24  jege Yeesu, Rammukat bi sàmm kóllëre gu bees gi; jege deretam, ji ñu wis. Te deret jooju, li muy yégle moo gëna neex li deretu Abel doon yéene.
30385  JAS 2:25  Naka Raxab jigéenu moykat bi itam, ndax du ci noonu la ko Yàlla àttee ni ku jub, ci li mu teeru ndawi Yawut yi, te jaarale leen ca poot ba?
30577  2PE 2:10  Rawatina ñiy topp seen bakkan ciy bëgg-bëgg yu ruslu, te faalewuñu genn kilifteef. Ñu ñeme Yàlla lañu, te dëgër bopp, ba ragaluñoo xas kilifa ya gëna kawe.
30582  2PE 2:15  Réer nañu ba wàcc yoon wu jub wi, topp yoonu Balaam, doomu Bosor, mi bëgge xiiroon ci njubadi.
30790  REV 2:5  Deel fàttaliku kon fa nga daanoo. Réccul te def, na nga daan def bu jëkk. Soo réccuwul, dinaa dikk ci yaw, jële sa tegukaayu làmp carab ba mu nekk.
30801  REV 2:16  Réccul kon; lu ko moy dinaa dikk ci yaw léegi te xeex ak nit ñooñu ak jaasi, jiy génn ci sama gémmiñ.
30883  REV 7:5  Fukki junni ak ñaar lañu màndargaal ci biir giiru Yuda, fukki junni ak ñaar ci giiru Ruben, fukki junni ak ñaar ci giiru Gàdd,
30979  REV 13:2  Rab wa ma gis ma nga mel ni segg, tànk ya mel ni yu rab wu ñuy wax urs, gémmiñ ga mel ni gu gaynde. Ninkinànka ja jox ko kàttanam ak nguuram ak sañ-sañam bu réy.
30981  REV 13:4  Ñu jaamu ninkinànka ja ndax li mu joxoon sañ-sañ rab wa, di jaamu it rab wa, naan: «Rab wi amul moroom, kenn manula xeex ak moom.»
31002  REV 14:7  Ma nga doon xaacu naan: «Ragal-leen Yàlla te jox ko ndam li, ndaxte waxtuw àtteem jot na. Jaamuleen ki sàkk asamaan ak suuf ak géej ak bëti ndox yi.»
31052  REV 17:8  Rab wi nga gis nekkoon na waaye nekkatul. Dina génn ca kàmb gu xóot ga, ba noppi sànku. Noonu waa àddina, ñi ñu bindul seeni tur, li dale ci njàlbéenu àddina, ci téereb dund bi, dinañu yéemu, bu ñu gisee rab wi, ndaxte nekkoon na waaye nekkatul te dina nekkaat.
31055  REV 17:11  Rab wi nekkoon te nekkatul nag, moom ci boppam moo di juróom ñetteelu buur bi, te ci juróom ñaar yi la bokk. Ma nga jëm sànkute.