23219 | MAT 1:6 | miy baayu buur bi Daawuda. Daawuda moo jur Suleymaan ci ki nekkoon soxnas Uri; |
24566 | MRK 7:34 | Mu yërëm ko, ba binni ci xolam, xool ci asamaan, daldi ne: «Effata,» liy tekki «Ubbikuleen.» |
28413 | ROM 16:9 | Nuyul-leen ma it Urban, sunu nawle ci liggéeyu Kirist, ak sama soppe Estakis; |
28978 | 2CO 6:12 | Ubbiku nanu ci yéen, waaye yéen ubbikuwuleen ci nun. |
29894 | 2TI 1:18 | Na ko Boroom bi teeru ak yërmandeem ca bés ba. Umplewoo it coono yi mu daj, ngir dimbali ma ca dëkku Efes. |
30822 | REV 3:8 | Xam naa say jëf. Ubbil naa la bunt, te kenn du ko mana tëj. Xam naa ne barewuloo doole, waaye sàmm nga sama kàddu te weddiwoo ma. |