|
25526 | Yéen xutbakat yi, dingeen torox, ndaxte yéena yóbbu caabiy xam-xam; dugguleen ci, te ku ci bëgga dugg, ngeen tere ko ko.» | |
26558 | Ñi ma fi jiitu ñépp ay sàcc lañu, ak ay saay-saay; waaye xar yi dégluwuñu leen. | |
28196 | Kon nag bokk yi, am nanu lu nu war, waaye waxuma leen topp sunu nafsu ak i bëgg-bëggam; | |
30052 | notal ko lépp, mu teg ci tànk.» Bi ko Yàlla notalee lépp nag, bàyyiwul dara. Fi mu nekk gisagunu ne lépp a ngi ci sañ-sañam; |