23638 | MAT 13:30 | Bàyyileen ñoom ñaar, ñu màgg, ba ngóob ma jot. Bu ngóob ma jotee nag, dinaa wax ñi koy góob: ‘Jëkkleena dindi jëmb bi, takk ko ay say, lakk ko, waaye ngeen semb dugub ji ci sama sàq.’ ”» |
23945 | MAT 22:4 | Kon mu yónneeti yeneen surga ne leen: “Bu ngeen demee, yégal-leen gan yi sama woote bii: ‘Reer yi noppi na, reylu naa samay nag ak samay jur gu duuf; lépp sotti na, ñëwleen ci reer yi.’ ” |
23985 | MAT 22:44 | “Boroom bi wax na sama Boroom: ‘Toogal ci sama ndijoor, ba kera may daaneel say noon ci sa kanam.’ ” |
24778 | MRK 12:36 | Daawuda moom wax na ci kàttanu Xel mu Sell mi naan: “Boroom bi nee na sama Boroom: ‘Toogal ci sama ndijoor, ba kera may daaneel say noon ci sa kanam.’ ” |
25547 | LUK 12:19 | Te dinaa kañ sama bopp ne: ‘Yaw mii, am nga alal ju bare ju mana dem ay ati at; noppalal sa yaram, di lekk, di naan, tey bég.’ ” |
25676 | LUK 15:19 | yeyootumaa nekk sa doom; boole ma ci say surga.’ ” |
25891 | LUK 20:43 | ba kera may daaneel say noon ci sa kanam.’ ” |
27053 | ACT 2:35 | ba kera may daaneel say noon ci sa kanam.’ ” |
27993 | ACT 28:26 | Nee na: “Demal ci xeet wii ne leen: ‘Dingeen déglu bu baax waaye dungeen xam dara; di xool bu baax waaye dungeen gis dara.’ |