|
24464 | Ay taalibeem ne ko: «Xanaa gisuloo mbooloo mi lay wër; ngay laaj: “Ku ma laal?”» | |
28262 | Waaye ku jub ci kanam Yàlla ci kaw ngëm, nii lay waxe: «Bul wax ci sa xol ne: “Kuy yéeg ci kaw?”» mel ni dangaa bëgg Kirist wàcc. | |
28263 | «Bul wax it: “Kuy dem ca barsàq?”» mel ni dangaa bëgg Kirist dekki. |