|
29040 | Ci lu jëm ci samay mbir nag, maa ngi leen di ñaan— man Pool, mi ñu ne, ci seen biir «ragal» laa, bu ma leen soree, «ñeme»— maa ngi leen di ñaan ndax woyof ak lewetaayu Kirist, ngir bu ma ñëwee, ma baña ànd ak ñeme gi may dencal ñenn ñiy xalaat ne gis-gisu nit lanu topp. |