Wildebeest analysis examples for:   wol-wolKYG   6    February 25, 2023 at 01:33    Script wb_pprint_html.py   by Ulf Hermjakob

121  GEN 5:15  Malaleel nag am na juróom benn fukki at ak juróom (65), doora jur Yeredd.
124  GEN 5:18  Yeredd moomee am na téeméeri at ak juróom benn fukk ak ñaar (162), doora jur Enog.
126  GEN 5:20  Kon Yeredd dund na juróom ñeenti téeméeri at ak juróom benn fukk ak ñaar (962), doora faatu.
127  GEN 5:21  Enog moomee, am na juróom benn fukki at ak juróom (65), doora jur Matusalem.
129  GEN 5:23  Kon Enog dund na ñetti téeméeri at ak juróom benn fukk ak juróom (365).
133  GEN 5:27  Kon Matusalem dund na juróom ñeenti téeméeri at ak juróom benn fukk ak juróom ñeent (969), doora faatu.
398  GEN 16:16  Ba Ajaray am Ismayla, Ibraam a ngi tollu woon ci juróom ñett fukki at ak juróom benn (86).
1854  EXO 12:37  Ci kaw loolu bànni Israyil jóge dëkk ba ñuy wax Ramses, jëm Sukkóot. Ña nga tollu ci juróom benni téeméeri junniy góor (600 000) te limaaleesul jigéen ñaak xale ya.
2660  EXO 38:26  muy juróomi garaami xaalis bopp bu nekk, yemook genn-wàllu siikal, ci siikal bi ñu yoonal ci bérab bu sell bi, ñeel képp ku bindu ci limeef bi, dale ko ci ñi am ñaar fukki at jëm kaw, ñépp di juróom benni téeméeri junniy góor ak ñetti junneek juróomi téeméer ak juróom fukk (603 550).
3626  NUM 1:21  Limub Rubeneen ñi di ñeent fukki junni ak juróom benn ak juróomi téeméer (46 500).
3630  NUM 1:25  Limub Gàddeen ñi di ñeent fukki junneek juróom ak juróom benni téeméer ak juróom fukk (45 650).
3632  NUM 1:27  Limub Yudeen ñi di juróom ñaar fukki junneek ñeent, ak juróom benni téeméer (74 600).
3644  NUM 1:39  Limub Daneen ñi di juróom benn fukki junneek ñaar ak juróom ñaar téeméer (6700).
3651  NUM 1:46  Ña ñu lim ñépp di juróom benn téeméeri junneek ñett ak juróomi téeméer ak juróom fukk (603 550).
3663  NUM 2:4  Ña ñu lim ci gàngooram di juróom ñaar fukki junneek ñeent ak juróom benni téeméer (74 600).
3668  NUM 2:9  «Mboolem ña ñu limal dalub Yuda aki gàngooram daldi doon téeméeri junneek juróom ñett fukk ak juróom benn ak ñeenti téeméer (186 400). Bu ñuy dem, ñooñooy dox, jiitu.
3670  NUM 2:11  Ña ñu limal gàngooram di ñeent fukki junneek juróom benn ak juróomi téeméer (46 500).
3674  NUM 2:15  Ña ñu limal gàngooram di ñeent fukki junneek juróom ak juróom benni téeméer ak juróom fukk (45 650).
3685  NUM 2:26  Ña ñu limal gàngooram di juróom benn fukki junneek ñaar ak juróom ñaar téeméer (6700).
3690  NUM 2:31  «Mboolem ña ñu limal dalub Dan daldi doon téeméer ak juróom fukki junneek juróom ñaar ak juróom benni téeméer (157 600). Ñooñooy mujja jóg, topp seeni raaya.»
3691  NUM 2:32  Ñooñu lañu limal bànni Israyil na ñu bokke seen këri maam. Mboolem ña ñu limal dal ya ak seeni gàngoor doon juróom benni téeméeri junneek ñett ak juróomi téeméer ak juróom fukk (603 550).
3721  NUM 3:28  Ba ñu waññee mboolem góor ña ca am weer, jëm kaw, juróom ñetti junni ak juróom benni téeméer (8 600) lañu. Ñoo dénkoo woon dénkaaney bérab bu sell bi.
3727  NUM 3:34  Ña ñu leen limal, ba ñu waññee mboolem góor ña am weer, jëm kaw, juróom benni junni ak ñaar téeméer (6 200) lañu.
3743  NUM 3:50  Xaalis ba mu nangoo ca taawi bànni Israyil di junniy siikal ak ñetti téeméer ak juróom benn fukk ak juróom (1 365), ci siikalu bérab bu sell bi, xawa tollu ci fukki kilo ak ñett.
3784  NUM 4:40  te ñu limal leen seeni làng ak seen këri maam, ñaari junneek juróom benni téeméer ak fanweeri góor lañu (2 630).
4046  NUM 11:21  Ci kaw loolu Musaa ne: «Ãa! Juróom benni téeméeri junniy (600 000) góor a ngi ci mbooloo mii ma ne ci seen biir. Yaw nga ne aw yàpp nga leen di jox, ñu yàpp weeru lëmm!
4513  NUM 26:22  Làngi Yudeen ñaa ngoogu, ña ñu leen limal di juróom ñaar fukki junneek juróom benn ak juróomi téeméer (76 500).
4516  NUM 26:25  Làngi Isaakar a ngoogu. Ña ñu leen limal di juróom benn fukki junneek ñeent ak ñetti téeméer (6300).
4518  NUM 26:27  Làngi Sabuloneen ñaa ngoogu, ña ñu leen limal di juróom benn fukki junni ak juróomi téeméer (6500).
4532  NUM 26:41  Ñooñoo askanoo ci Beñamin, ñook seeni làng, ña ñu leen limal di ñeent fukki junneek juróom ak juróom benni téeméer (45 600).
4534  NUM 26:43  Mboolem làngi Cuwameen, ña ñu leen limal juróom benn fukki junneek ñeent la, ak ñeenti téeméer (6400).
4542  NUM 26:51  Limeefu bànni Israyil a ngoogu, di juróom benni téeméeri junneek benn ak juróom ñaar téeméer ak fanweer (601 730).
4698  NUM 31:32  La des ca alalu sëxëtoo, ja ña xareji woon indaale, gannaaw ba ñu ca génnee yooyu, nii la tollu: gàtt yi, juróom benni téeméeri junneek juróom ñaar fukk ak juróom (675 000);
4700  NUM 31:34  mbaam yi, juróom benn fukki junneek benn (6000),
4703  NUM 31:37  galagu Aji Sax ji génne ci gàtt yi, di juróom benni téeméer ak juróom ñaar fukk ak juróom (675);
4704  NUM 31:38  nag yi, fanweeri junneek juróom benn (36 000), galagu Aji Sax ji génne ci, di juróom ñaar fukk ak ñaar (72);
4705  NUM 31:39  mbaam yi, fanweeri junneek juróomi téeméer (30 500), galagu Aji Sax ji génne ci, di juróom benn fukk ak benn (61);
4706  NUM 31:40  aw nit, fukki junneek juróom benn (16 000), galagu Aji Sax ji génne ci, di fanweeri bopp ak ñaar (32).
4710  NUM 31:44  nag yi di fanweeri junneek juróom benn (36 000);
4712  NUM 31:46  aw nit, fukki junneek juróom benn (16 000).
4718  NUM 31:52  Mboolem wurusu jooxe, wi ñu jooxeel Aji Sax ji, di fukk ak juróom benni junniy siikal ak juróom ñaar téeméer ak juróom fukk (16 750), yemook barigo ak juróom ñaar fukki kilo (170), te bawoo ci kilifay kuréli junni yaak kilifay kuréli téeméer ya.
8083  2SA 2:31  Waaye fekk na niti Daawuda rey ñetti téeméer ak juróom benn fukk (360) ca Beñamineen ñaak niti Abner.
9111  1KI 10:29  Ab watiir bu ñu jëggaanee Misra, indi, juróom benni téeméeri dogi xaalis (600) la leen daan dikke, aw fas di téeméer ak juróom fukki dogi xaalis (150), te noonu lañu ca daan jëndaaleel mboolem buuri Etteen ña ak buuri Siri, indil leen.
12041  EZR 2:9  Askanu Sakay, juróom ñaar téeméer ak juróom benn fukk lañu (760).
12042  EZR 2:10  Askanu Baani, juróom benni téeméer ak ñeent fukk ak ñaar lañu (642).
12043  EZR 2:11  Askanu Bebay, juróom benni téeméer ak ñaar fukk ak ñett lañu (623).
12045  EZR 2:13  Askanu Adonikam, juróom benni téeméer ak juróom benn fukk ak juróom benn lañu (666).
12046  EZR 2:14  Askanu Bigway, ñaari junni ak juróom fukk ak juróom benn lañu (2 056).
12054  EZR 2:22  Waa Netofa, juróom fukk ak juróom benn lañu (56).
12058  EZR 2:26  Waa Raama ak Geba, juróom benni téeméer ak ñaar fukk ak benn lañu (621).
12062  EZR 2:30  Waa Magbis téeméer ak juróom fukk ak juróom benn lañu (156).
12067  EZR 2:35  Waa Sena, ñetti junni ak juróom benn téeméer ak fanweer lañu (3 630).
12092  EZR 2:60  Askanu Delaya, ak askanu Tobya, ak askanu Nekoda, di juróom benn téeméer ak juróom fukk ak ñaar (652).
12096  EZR 2:64  Limu mbooloo ma mépp ba mu daj, ñeent fukki junneek ñaar ak ñetti téeméer ak juróom benn fukk lañu (42 360),
12098  EZR 2:66  Amoon nañu juróom ñaar téeméeri fas ak fanweer ak juróom benn (736), ak ñaar téeméeri berkelle ak ñeent fukk ak juróom (245),
12099  EZR 2:67  ak ñeenti téeméeri giléem ak fanweer ak juróom (435), ak juróom benni junniy mbaam ak juróom ñaar téeméer ak ñaar fukk (6 720).
12216  EZR 8:10  Ci askanu Baani, Selomit doomu Yosifya la, mook téeméeri góor ak juróom benn fukk (160).
12219  EZR 8:13  Askanu Adonikam ñoo mujje, ñu di leen wax Elifelet ak Iyel ak Semaya, ñook juróom benn fukki góor (60).
12241  EZR 8:35  Ba mu ko defee ña jóge njaam, ñibbsee ca ngàllo ga, daldi defal Yàllay Israyil ay saraxi dóomal. Muy fukki yëkk ak ñaar, ñeel Israyil gépp ak juróom ñeent fukki kuuy ak juróom benn (96), ak juróom ñaar fukki xar yu ndaw ak juróom ñaar (77), ak fukki sikket ak ñaar yu ñu def saraxu póotum bàkkaar; ñu def lépp saraxu dóomal, ñeel Aji Sax ji.
12435  NEH 7:10  Askanu Ara di juróom benn téeméer ak juróom fukk ak ñaar (652).
12439  NEH 7:14  Askanu Sakay juróom ñaar téeméer ak juróom benn fukk lañu (760).
12440  NEH 7:15  Askanu Binuy juróom benn téeméer ak ñeent fukk ak juróom ñett lañu (648).
12441  NEH 7:16  Askanu Bebay juróom benn téeméer ak ñaar fukk ak juróom ñett lañu (628).
12443  NEH 7:18  Askanu Adonikam juróom benni téeméer ak juróom benn fukk ak juróom ñaar lañu (667).
12444  NEH 7:19  Askanu Bigway ñaari junni ak juróom benn fukk ak juróom ñaar lañu (2 067).
12445  NEH 7:20  Askanu Adin juróom benn téeméer ak juróom fukk ak juróom lañu (655);
12455  NEH 7:30  Waa Raama ak Geba juróom benni téeméer ak ñaar fukk ak benn lañu (621).
12487  NEH 7:62  Askanu Delaya, ak askanu Tobya, ak askanu Nekoda, di juróom benn téeméer ak ñeent fukk ak ñaar (642).
12491  NEH 7:66  Limu mbooloo ma mépp ba mu daj, ñeent fukki junneek ñaar ak ñetti téeméer ak juróom benn fukk lañu (42 360),
12493  NEH 7:68  ak ñeenti téeméeri giléem ak fanweer ak juróom (435), ak juróom benni junniy mbaam ak juróom ñaar téeméer ak ñaar fukk (6 720).
12496  NEH 7:71  La des ca askan wa joxe na ñaar fukki junniy poseti wurus (20 000) ak ñaari junniy dogi xaalis (2 000) ak mbubbi sarxalkat yu tollu ci juróom benn fukk ak juróom ñaar (67).
13938  JOB 42:12  Aji Sax ji nag barkeel mujug Ayóoba lu raw ndoorteem. Mu am fukki junniy gàtt ak ñeent (14 000), ak juróom benni junniy giléem (6 000), ak junniy lëkkey nag (1 000) yu muy rijjee, ak junniy mbaam yu jigéen (1 000).
20375  JER 52:30  Ak juróom ñaar téeméer ak ñeent fukk ak juróom (745) yu Nebusaradan njiital dag ya, toxal. Loolu yemook ñaar fukkeelu at maak ñett ci nguurug Nabukodonosor. Ñi ñu toxal ñépp di ñeenti junni ak juróom benni téeméer (4 600).
27960  ACT 27:37  Ña nekkoon ca gaal ga ñépp ñaar téeméer ak juróom ñaar fukk ak juróom benn (276) lañu.
30943  REV 11:3  Dinaa may nag sama ñaari seede yi, ñu biral waxyu diiru junni ak ñaar téeméeri fan ak juróom benn fukk (1 260) yu ñuy sol ay saaku, di ko toroxloo.»
30965  REV 12:6  Ndaw si nag daw, ba ca màndiŋ ma, ci ab rawtu bu ko Yàlla waajaloon, ngir ñu leel ko fa diiru junni ak ñaar téeméeri fan ak juróom benn fukk (1 260).
30995  REV 13:18  Fii nag xel la laaj: ku am ug dégg, na waññ limu rab wi, ndax boobu lim turu nit la taxawe, di juróom benni téeméer ak juróom benn fukk ak juróom benn (666).