1989 | EXO 17:5 | Aji Sax ji ne Musaa «Àndal ak ñenn ci magi Israyil, nga jaar ci kanam mbooloo mi, yóbbaale yet, wa nga dóoroon ca dexu Niil ga. Ŋàbb ko ci sa loxo te dem. |
15287 | PSA 81:11 | Man, Aji Sax ji, maay seen Yàlla ji leen yékkatee réewum Misra. Ŋaleen ŋafeet, ma reggal leen. |
15964 | PSA 118:27 | Aji Sax jee di Yàlla, di nu leeral. Ŋàbbleen car yi, màggale, te dox ba ca béjjéni sarxalukaay ba. |
16573 | PRO 4:13 | Ŋoyal cib yar, bul yoqi, sàmm ko, moo yor sa bakkan. |
20117 | JER 46:3 | «Ŋàbbleen pakkoo pakk te xareji. |
30810 | REV 2:25 | Ŋoyleen rekk ci li ngeen am, ba kera may dikk. |
30825 | REV 3:11 | «Maa ngi ñëw léegi. Ŋoyal ci li nga yor, ngir kenn baña fëkk sa kaalag ndam. |