Wildebeest analysis examples for:   wol-wolKYG   Word-Word-Word!    February 25, 2023 at 01:33    Script wb_pprint_html.py   by Ulf Hermjakob

19501  JER 20:10  Dégg naa ñaawlaate yu bare, ñu naan: «Éey, Tiitaange-lu-dajal! Booleleen ko, boole rekk!» Ñi ma séqal jàmm sax, di yeeru ma fakkastalu, naan: «Jombul mu juum, nu jekku ko, ba mana feyu.»