12716 | EST 1:10 | Keroog bésub juróom ñaareel ba Buur Aserus naan biiñ, ba xolam sedd, mu sant juróom ñaari bëkk-néegam: Meyuman ak Bista ak Arbona ak Bigta ak Abagta ak Setar ak Karkas, ne leen |
18581 | ISA 43:6 | Maa naa bëj-gànnaar: “Ësi!” ne bëj-saalum: “Bul téye!” Jëleel sama doom yu góor fu sore, délloosi, te jëleji sama doom yu jigéen fa cati àddina. |
19284 | JER 10:14 | Nitoo nit dim sannax, sore xam-xam: te képp kuy tëgg sa jëmmu tuur, yaa añe gàcce. Sa jëmmi weñ ji nga xelli, di neenug neen, noog bakkan, tus! |
21763 | EZK 47:15 | Na lii di kemu réew mi ci wetu bëj-gànnaar: géej gu mag ga lay dale, topp yoon wa jaare Ettlon ak Lebo Amat, ak Cedàdd, |