4698 | NUM 31:32 | La des ca alalu sëxëtoo, ja ña xareji woon indaale, gannaaw ba ñu ca génnee yooyu, nii la tollu: gàtt yi, juróom benni téeméeri junneek juróom ñaar fukk ak juróom (675 000); |
4699 | NUM 31:33 | nag yi, juróom ñaar fukki junneek ñaar (72 000); |
4710 | NUM 31:44 | nag yi di fanweeri junneek juróom benn (36 000); |
4711 | NUM 31:45 | mbaam yi, fanweeri junneek juróomi téeméer (30 500); |
21786 | EZK 48:15 | «Pàkk bay des ci yaatuwaayu dog boobu dina yaatoo juróomi junniy xasab (5 000), gudde ñaar fukki junniy xasab ak juróom (25 000); suufas ñépp la pàkk boobu di doon, ngir dëkk bi. Man naa doon ay dëkkuwaay aki parlu, te na dëkk bi ci boppam féetewoo digg ba. |