|
18308 | di dégg kàddu guy jibe seen gannaaw, naa leen: «Yoon waa ngii, jaareleen fi;» bu ngeen awee ndijoor, mbaa càmmoñ. | |
28887 | ndax Doomu Yàlla, Yeesu Almasi, mi nu biral ci seen biir, man ak Silas ak Timote, du kàddug «waaw, déet;» «waaw» doŋŋ a nekk ci moom. |