|
24566 | Mu yërëm ko, ba binni ci xolam, xool ci asamaan, daldi ne: «Effata,» liy tekki «Ubbikuleen.» | |
28762 | Walla, boo dee gërëm Yàlla, ànd ci ak sa xol rekk, kon ku masula jàng mbir yooyu, nan la mana waxe: «Amiin,» ci sa cant Yàlla googu? Ndaxte xamul li ngay wax. |