Wildebeest analysis examples for: wol-wol2010 “Word-Word,
February 11, 2023 at 19:57
Script wb_pprint_html.py by Ulf Hermjakob
24807
MRK 13:21
«Booba nag, bu leen kenn waxee: “Kaayleen gis, Kirist a ngi fi,” mbaa:
“Xool-leen,
mu nga fale,” buleen ko gëm.
25741
LUK 17:21
Duñu mana wax it ne:
“Xool-leen,
mi ngi fii,” walla: “Ma nga fale,” ndaxte nguuru Yàlla wàcc na ci seen biir.»