Wildebeest analysis examples for:   wol-wol2010   Word,”»    February 11, 2023 at 19:57    Script wb_pprint_html.py   by Ulf Hermjakob

30084  HEB 4:3  Nun ñi gëm nag nooy dugg ci noflaayam, ni ko Mbind mi waxe: «Giñ naa kon ci sama mer ne: “Duñu dugg mukk ci sama noflaay,”» doonte sax liggéeyam bépp matoon na, ca ba mu sàkkee àddina ak léegi. Ci lu jëm ci juróom ñaareelu fan ba,