Wildebeest analysis examples for:   wol-wolKYG   2    February 11, 2023 at 19:57    Script wb_pprint_html.py   by Ulf Hermjakob

114  GEN 5:8  Kon Set dund na juróom ñeenti téeméeri at ak fukk ak ñaar (912), doora faatu.
124  GEN 5:18  Yeredd moomee am na téeméeri at ak juróom benn fukk ak ñaar (162), doora jur Enog.
126  GEN 5:20  Kon Yeredd dund na juróom ñeenti téeméeri at ak juróom benn fukk ak ñaar (962), doora faatu.
132  GEN 5:26  Lemeg juddu na, Matusalem dundaat juróom ñaar téeméeri at ak juróom ñett fukk ak ñaar (782), amaat ay doom yu góor ak yu jigéen.
134  GEN 5:28  Lemeg nag am na téeméeri at ak juróom ñett fukk ak ñaar (182), doora jur doom ju góor.
141  GEN 6:3  Aji Sax ji daldi wax ne: «Manumaa bàyyi nit, muy wéyee dunde noo, gi ma ko may, ndax nit du dara lu dul suuxi neen, kon dinaa leen àppal diirub téeméeri at ak ñaar fukk (120).»
286  GEN 11:19  Rew juddu na, Peleg dundaat ñaar téeméeri at ak juróom ñeent (209), juraat ay doom yu góor ak yu jigéen.
288  GEN 11:21  Serug juddu na, Rew dundaat ñaar téeméeri at ak juróom ñaar (207), juraat ay doom yu góor ak yu jigéen.
299  GEN 11:32  Teraa dund na ñaar téeméeri at ak juróom (205), doora génn àddina, ñu denc ko Karan.
573  GEN 23:1  Saarata dund na, ba am téeméeri at ak ñaar fukk ak juróom ñaar (127),
2663  EXO 38:29  Xànjar bi ñu def saraxu yékkati-jébbal Yàlla, ñaari junniy kilo ak téeméer ak ñaar fukk ak ñeent la (2 124), yemook juróom ñaar fukki (70) talaŋ ak ñaari junneek ñeenti téeméeri (2 400) siikal.
3640  NUM 1:35  Limub Manaseen ñi di fanweeri junneek ñaar ak ñaar téeméer (32 200).
3644  NUM 1:39  Limub Daneen ñi di juróom benn fukki junneek ñaar ak juróom ñaar téeméer (62 700).
3680  NUM 2:21  Ña ñu limal gàngooram di fanweeri junneek ñaar ak ñaar téeméer (32 200).
3685  NUM 2:26  Ña ñu limal gàngooram di juróom benn fukki junneek ñaar ak juróom ñaar téeméer (62 700).
3727  NUM 3:34  Ña ñu leen limal, ba ñu waññee mboolem góor ña am weer, jëm kaw, juróom benni junni ak ñaar téeméer (6 200) lañu.
3732  NUM 3:39  Mboolem ña ñu limal Leween ñi, te Musaa ak Aaróona lim leen na ñu bokke seeni làng ci ndigalal Aji Sax ji, ñuy mboolem góor ñi am weer, jëm kaw, ñaar fukki junneek ñaar (22 000) lañu.
3736  NUM 3:43  Ba ñu waññee mboolem taaw yu góor ya, bind seeni tur, dale ci ñi am weer, jëm kaw, seenub lim nekk na ñaar fukki junneek ñaar ak ñaar téeméer ak juróom ñaar fukk ak ñett (22 273).
3739  NUM 3:46  Njotlaay nag dina war ci ñaar téeméer ak juróom ñaar fukk ak ñetti (273) bopp, yi taawi bànni Israyil ëppe Leween ñi.
3780  NUM 4:36  Ña ñu limal seeni làng di ñaari junni ak juróom ñaar téeméer ak juróom fukki góor (2 750).
3784  NUM 4:40  te ñu limal leen seeni làng ak seen këri maam, ñaari junneek juróom benni téeméer ak fanweeri góor lañu (2 630).
3788  NUM 4:44  te ñu limal leen seeni làng, ñetti junni ak ñaar téeméeri góor (3 200) lañu.
3936  NUM 7:85  ndabal xaalis lu nekk di téeméeri siikal ak fanweer, di kilook liibar, këll bu nekk di juróom ñaar fukki siikal, di juróom ñetti téeméeri garaam, mboolem xaalisu jumtukaay yi di ñaari junniy siikali bérab bu sell bi ak ñeenti téeméer (2 400), di ñaar fukki kilook juróom ñaar ak juróomi téeméeri garaam (2500).
3937  NUM 7:86  Fukki bàttuy wurus yi feese cuuraay, mbàttu su ci nekk fukki siikali bérab bu sell bi la, di téeméeri garaam ak fukk (110), mboolem wurusu bàttu yi di téeméeri siikal ak ñaar fukk (120), muy kilo ak ñetti téeméeri garaam (1 300).
4197  NUM 16:2  ñu jógal Musaa, ñook ñaar téeméer ak juróom fukk (250) ci bànni Israyil, diy kilifa ci mbooloo mi, am baat ca pénc ma, te di ñu amu tur.
4481  NUM 25:9  Ña dee ca mbas ma nag di ñaar fukki junneek ñeent (2000).
4505  NUM 26:14  Làngi Cimyoneen ñaa ngoogu, di ñaar fukki junneek ñaar ak ñaar téeméer (22 200).
4525  NUM 26:34  Làngi Manasee ngoogu, ña ñu leen limal di juróom fukki junneek ñaar ak juróom ñaar téeméer (52 700).
4528  NUM 26:37  Làngi Efrayim a ngoogu, ña ñu leen limal di fanweeri junneek ñaar ak juróomi téeméer (32 500). Ñooñoo askanoo ci Yuusufa, ñook seeni làng.
4553  NUM 26:62  Ña ñu limal Leween ñi nag ñaar fukki junneek ñett lañu (2000), di mboolem góor ña am weer, jëm kaw, te limaaleesu leen ak bànni Israyil ga ca des, ndax joxeesu leen ab cér ci biir bànni Israyil.
4671  NUM 31:5  Ba mu ko defee ñu tànne ca gàngoori Israyil, junniy góor jóge ci giir gu nekk, ñuy fukki junneek ñaari (12 000) xarekat yu gànnaayu.
4699  NUM 31:33  nag yi, juróom ñaar fukki junneek ñaar (72 000);
4704  NUM 31:38  nag yi, fanweeri junneek juróom benn (36 000), galagu Aji Sax ji génne ci, di juróom ñaar fukk ak ñaar (72);
4706  NUM 31:40  aw nit, fukki junneek juróom benn (16 000), galagu Aji Sax ji génne ci, di fanweeri bopp ak ñaar (32).
4801  NUM 33:39  Aaróona mu ngi woon ci téeméeri atam, ak ñaar fukk at ñett (123) ba mu faatoo ca kaw tundu Or.
8216  2SA 8:4  Daawuda jàpp junniy gawaram ak juróom ñaar téeméer (1 700) ak ñaar fukki junniy xarekat (2000) yuy deme tànk, ba noppi dog sidditi tànki mboolem fas ya doon dawal watiir, bàyyiwu ca lu moy téeméeri fas.
8217  2SA 8:5  Waa Siri ña dëkke réewum Damaas dikk wallusi Adadeser buurub Soba. Daawuda rey ca ñoom ñaar fukki junneek ñaar (22 000).
8249  2SA 10:6  Amoneen ña xam ne Daawuda jéppi na leen lool. Ñu dem bindi ñaar fukki junniy (2000) xarekat ca waa Siri ña dëkke Bet Reyob ak waa Siri ña dëkke Soba, teg ca junniy nit ñu bàyyikoo ca buuru Maaka, ak fukki junneek ñaar (12 000) ñu waa Tob.
8453  2SA 17:1  Gannaaw loolu Ayitofel ne Absalom: «Ngalla may ma, ma tànn fukki junniy xarekat ak ñaar (12 000) te dàqi Daawuda ci guddi gi.
8488  2SA 18:7  mbooloom Israyil nag daanu foofa ca kanam xarekati Daawuda. Bésub keroog ñu baree dee: ñaar fukki junnee (2000) daanu.
8873  1KI 5:6  Suleymaan amoon na ñeenti junniy (4 000) wuddi fasi watiir ak fukki junniy fas ak ñaar (12 000).
8892  1KI 5:25  Suleymaan ci wàllu boppam jox Iram ñaar fukki junni ak juróom ñetti (2000) barigoy peppu bele, ak ñaar fukki barigo ak ñaar (22) ci diwu oliw gu ñu segal. Suleymaan di defal Iram noonu at mu ne.
8963  1KI 7:26  Dëllaayu mbalka mi yaatuwaayu loxo la, kéméj gi mel ni gémmiñu kaas, di nirook lëppi tóor-tóor. Ñaar téeméeri barigo la mbalka miy def. (200).
9051  1KI 8:63  Mu defal Aji Sax ji saraxi cant ci biir jàmm, lépp di ñaar fukki junniy nag ak ñaar (22 000) ak téeméeri junniy gàtt ak ñaar fukk (12000). Noonu la Buur ak bànni Israyil gépp amale xewu jagleb kër Aji Sax ji.
9108  1KI 10:26  Ba mu ko defee Suleymaan dajale watiir yaak fas ya, muy junni ak ñeenti téeméeri watiir (1 400), ak fukki junniy fas ak ñaar (12 000) yu mu yebal ca dëkk ya watiir ya féete, ak ca Yerusalem ga mu nekk.
9426  1KI 20:15  Ba mu ko defee Axab lim dag ya kilifay diiwaan ya yebal, ñuy ñaar téeméer ak fanweer ak ñaar (232). Gannaaw loolu mu lim mbooloom Israyil gépp, ñuy juróom ñaari junni (7 000).
9441  1KI 20:30  ña ca des daw ba Afeg, ca biir dëkk ba, tata ja màbb ca kaw ñaar fukki junniy nit ak juróom ñaar (2000) ca ñoom. Fekk na Ben Addàd daw dugg ca biir dëkk ba, jàll ci biir néeg bu làqoo làqu.
12030  EZR 1:9  Lenn ci lim bi tëdde nii: fanweeri ndabi wurus (30), ak junniy ndabi xaalis (1 000), ak ñaar fukki paaka ak juróom ñeent (29),
12035  EZR 2:3  Askanu Paros, ñaari junni ak téeméer ak juróom ñaar fukk ak ñaar lañu (2 172).
12036  EZR 2:4  Askanu Sefatiya, ñetti téeméer ak juróom ñaar fukk ak ñaar lañu (372).
12038  EZR 2:6  Askanu Payat Mowab, soqikoo ci Yeswa ak Yowab, di ñaari junni ak juróom ñetti téeméer ak fukk ak ñaar (2 812).
12039  EZR 2:7  Askanu Elam, junni ak ñaar téeméer ak juróom fukk ak ñeent lañu (1 254).
12042  EZR 2:10  Askanu Baani, juróom benni téeméer ak ñeent fukk ak ñaar lañu (642).
12043  EZR 2:11  Askanu Bebay, juróom benni téeméer ak ñaar fukk ak ñett lañu (623).
12044  EZR 2:12  Askanu Asgàdd, junni ak ñaar téeméer ak ñaar fukk ak ñaar lañu (1 222).
12046  EZR 2:14  Askanu Bigway, ñaari junni ak juróom fukk ak juróom benn lañu (2 056).
12049  EZR 2:17  Askanu Besay, ñetti téeméer ak ñaar fukk ak ñett lañu (323).
12050  EZR 2:18  Askanu Yora, téeméer ak fukk ak ñaar lañu (112).
12051  EZR 2:19  Askanu Asum, ñaar téeméer ak ñaar fukk ak ñett lañu (223).
12053  EZR 2:21  Waa Betleyem, téeméer ak ñaar fukk ak ñett lañu (123).
12055  EZR 2:23  Waa Anatot, téeméer ak ñaar fukk ak juróom ñett lañu (128).
12056  EZR 2:24  Waa Asmawet, ñeent fukk ak ñaar lañu (42).
12058  EZR 2:26  Waa Raama ak Geba, juróom benni téeméer ak ñaar fukk ak benn lañu (621).
12059  EZR 2:27  Waa Migmas, téeméer ak ñaar fukk ak ñaar lañu (122).
12060  EZR 2:28  Waa Betel ak Ayi, ñaar téeméer ak ñaar fukk ak ñett lañu (223).
12061  EZR 2:29  Waa Nebo, juróom fukk ak ñaar lañu (52).
12063  EZR 2:31  Waa Elam gu ndaw, junni ak ñaar téeméer ak juróom fukk ak ñeent lañu (1 254).
12064  EZR 2:32  Waa Arim, ñetti téeméer ak ñaar fukk lañu (320).
12065  EZR 2:33  Waa Lodd ak Adidd ak Ono, juróom ñaar téeméer ak ñaar fukk ak juróom lañu (725).
12069  EZR 2:37  Askanu Imer, junni ak juróom fukk ak ñaar lañu (1 052).
12070  EZR 2:38  Askanu Pasur, junni ak ñaar téeméer ak ñeent fukk ak juróom ñaar lañu (1 247).
12073  EZR 2:41  Jàngkat yi ñoo di: Askanu Asaf, di téeméer ak ñaar fukk ak juróom ñett (128).
12090  EZR 2:58  Mboolem liggéeykati kër Yàlla gi ak askanu jaami Suleymaan yi, ñetti téeméer ak juróom ñeent fukk ak ñaar (392).
12092  EZR 2:60  Askanu Delaya, ak askanu Tobya, ak askanu Nekoda, di juróom benn téeméer ak juróom fukk ak ñaar (652).
12096  EZR 2:64  Limu mbooloo ma mépp ba mu daj, ñeent fukki junneek ñaar ak ñetti téeméer ak juróom benn fukk lañu (42 360),
12097  EZR 2:65  te limaaleesul seen jaam yu góor ak yu jigéen, yi tollu ci juróom ñaari junni ak ñetti téeméer ak fanweer ak juróom ñaar (7 337). Amoon nañu itam ay jàngkat yu góor ak yu jigéen, yu tollu ci ñaar téeméer (200).
12098  EZR 2:66  Amoon nañu juróom ñaar téeméeri fas ak fanweer ak juróom benn (736), ak ñaar téeméeri berkelle ak ñeent fukk ak juróom (245),
12099  EZR 2:67  ak ñeenti téeméeri giléem ak fanweer ak juróom (435), ak juróom benni junniy mbaam ak juróom ñaar téeméer ak ñaar fukk (6 720).
12210  EZR 8:4  Ci askanu Payat Mowab, Elyowenay doomu Seraya la, mook ñaar téeméeri góor (200).
12215  EZR 8:9  Ci askanu Yowab, Obadiya doomu Yeyel la, mook ñaar téeméeri góor ak fukk ak juróom ñett (218).
12217  EZR 8:11  Ci askanu Bebay, Sàkkaryaa doomu Bebay la, mook ñaar fukki góor ak juróom ñett (28).
12225  EZR 8:19  ñook Asabya ak Esayi sëtu Merari. Ñu ànd ak seeni bokk ak seen doom yu góor, di ñaar fukki góor (20).
12226  EZR 8:20  Indaale nañu ñaar téeméeri liggéeykati kër Yàlla ak ñaar fukk (220), di ñu askanoo ca ña Daawudaaki jawriñam tànnoon, bind seeni tur, ngir ñuy jàpple Leween ñi.
12433  NEH 7:8  Askanu Paros ñaari junni ak téeméer ak juróom ñaar fukk ak ñaar lañu (2 172).
12434  NEH 7:9  Askanu Sefatiya ñetti téeméer ak juróom ñaar fukk ak ñaar lañu (372).
12435  NEH 7:10  Askanu Ara di juróom benn téeméer ak juróom fukk ak ñaar (652).
12436  NEH 7:11  Askanu Payat Mowab, soqikoo ci Yeswa ak Yowab, di ñaari junni ak juróom ñetti téeméer ak fukk ak juróom ñett (2 818).
12437  NEH 7:12  Askanu Elam junni ak ñaar téeméer ak juróom fukk ak ñeent lañu (1 254).