42 | GEN 2:11 | Turu menn wal ma di dexu Pison, moo wër réewum Awila mépp. Wurus a nga woon ca réew mooma, |
181 | GEN 7:21 | Mboolem mbindeef mu daan dox ci kaw suuf dee na ca. Picc yi ak jur gi ak rabi àll yi ak lépp luy raam ci kaw suuf dee na, ñoom ak nit ñépp. |
241 | GEN 10:6 | Doomi Xam yu góor ñoo di ñii: Kuus ak Misrayim ak Puut ak Kanaan. |
249 | GEN 10:14 | ak Pataruseen ñi ak Kasluyeen, ñooñee waa Filisti bàyyikoo ca seen réew; ak it Kaftoreen ñi. |
260 | GEN 10:25 | Eber moom, jur ñaari doom yu góor, kenn ki tudd Peleg (mu firi Séddlikoo), ndaxte ci jamonoom àddina dafa séddlikoo woon. Rakku Peleg mooy Yogtaan. |
283 | GEN 11:16 | Eber am fanweeri at ak ñeent, jur Peleg. |
284 | GEN 11:17 | Peleg juddu na, Eber dundaat ñeenti téeméeri at ak fanweer (430), juraat ay doom yu góor ak yu jigéen. |
285 | GEN 11:18 | Peleg am fanweeri at, jur Rew. |
286 | GEN 11:19 | Rew juddu na, Peleg dundaat ñaar téeméeri at ak juróom ñeent (209), juraat ay doom yu góor ak yu jigéen. |
326 | GEN 13:7 | Loolu tax sàmmi Ibraam ak sàmmi Lóot di jote. Rax ci dolli Kanaaneen ñi ak Periseen ñi ña nga woon ca réew ma. |
343 | GEN 14:6 | ak Oreen ña ca seen tund wa ñuy wax Seyir. Da leena dàq ba ca garabu Paran gu mag ga ca wetu màndiŋ ma. |
381 | GEN 15:20 | ak Etteen ñi ak Periseen ñi ak Refayeen ñi, |
535 | GEN 21:21 | Ca àllub Paran la dëkkoon, yaayam wutali ko soxna ca réewum Misra. |
536 | GEN 21:22 | Jamono yooyu Abimeleg àndoon na ak Pikol kilifay xarekatam, dem ci Ibraayma ne ko: «Gis naa ne Yàlla ànd na ak yaw, di àntal li ngay def lépp. |
546 | GEN 21:32 | Naka lañu fasoo kóllëre ca Beerseba, Abimeleg jóg ànd ak Pikol kilifay xarekatam, ñu ñibbi réewu Filisti. |
570 | GEN 22:22 | teg ca Keset ak Aso ak Pildas ak Yidlaf ak Betuwel.» |
679 | GEN 25:20 | Isaaxa am ñeent fukki at, jël Rebeka doomu Betuwel, Arameen, bi dëkke diiwaanu Padan Aram, dib jigéenu Laban, Arameen ba. |
719 | GEN 26:26 | Ci diggante boobu Abimeleg dafa jóge Gerar, dem fekki ko, ànd ak Awusat, ma doon wóllëreem, ak Pikol, njiital xarekatam. |
776 | GEN 28:2 | waaye demal Padan Aram ca sa kër maam-góor, ji jur sa yaay, nga jël fa jabar ca sa doomi nijaay Laban. |
779 | GEN 28:5 | Isaaxa daldi yebal Yanqóoba, mu dem Padan Aram ca Laban doomu Betuwel, Arameen bay càmmiñu Rebeka, miy yaayu Yanqóoba ak Esawu. |
780 | GEN 28:6 | Esawu nag yég ne Isaaxa ñaanal na Yanqóoba, ba noppi yebal ko Padan Aram, ngir mu jël fa soxna. Te it ba mu koy ñaanal, digal na ko ne ko, bumu jël ca jigéeni Kanaaneen ña. |
781 | GEN 28:7 | Mu yég ne Yanqóoba déggal na baayam ak yaayam, ba dem Padan Aram. |
892 | GEN 31:18 | ñu ànd tegu ca yoon wa, yóbbaale géttam gépp ak mboolem alal ju mu liggéey. Mooy gétt, ga mu sàkkoo Padan Aram. Ña ngay ñibbi kër baayam Isaaxa ca réewu Kanaan. |
959 | GEN 32:31 | Ci kaw loolu Yanqóoba tudde bérab ba Peniyel (mu firi Xar-kanamu Yàlla), ndaxte da ne: «Ne naa Yàlla jàkk, te maa ngi dund ba tey.» |
960 | GEN 32:32 | Ba jant bay fenk, Yanqóobaa ngi soox tànk bi, di bàyyikoo Penuwel. |
979 | GEN 33:18 | Gannaaw ga Yanqóoba agsi Sikem, ga ca réewu Kanaan, ci jàmm. Fekk na mu bàyyikoo Padan Aram, ba dal fa jàkkaarlook dëkk ba. |
1011 | GEN 34:30 | Yanqóoba nag wax ak Simeyon ak Lewi ne leen: «Indil ngeen ma musiba, ndax dingeen tax waa réew mépp sib ma, muy Kanaaneen ñi, di Periseen ñi. Te itam awma lu dul góor ñu néew, te bu ñu booloo dal ci sama kaw, dañu may booleek sama waa kër faagaagal.» |
1021 | GEN 35:9 | Ba Yanqóoba jógee Padan Aram, Yàlla feeñuwaat na ko, barkeel ko |
1038 | GEN 35:26 | Doomi Silpa, jaamub Leya, di Gàdd ak Aser. Ñooñooy doomi Yanqóoba, te mu am leen ca Padan Aram. |
1080 | GEN 36:39 | Ba Baal Anan doomu Agbor faatoo, Adar falu, wuutu ko. Pawu moo doon péeyam, soxnaam di Metabeel, mi Mataredd doomu Me Saab di yaayam. |
1082 | GEN 36:41 | ak Olibama ak Ela ak Pinon |
1120 | GEN 37:36 | fekk waa Majan yóbbu nañu ko Misra, jaay ko Potifaar, jawriñu Firawna mi jiite ay dagam. |
1149 | GEN 38:29 | Naka la delloo loxoom, seexam juddu, mu ne ko: «Yaw foo bëtte, ba génn?» Ñu daldi ko tudde Peres (mu firi Bëtt). |
1151 | GEN 39:1 | Ba ñu yóbboo Yuusufa Misra, Potifaar, jawriñu Firawna, ma jiite ay dagam, da koo jënd ca Ismayleen, ña ko fa indi. |
1185 | GEN 40:12 | Yuusufa ne ko: «Piri mi mooy lii. Ñetti car yi, ñetti fan la. |
1191 | GEN 40:18 | Yuusufa ne ko: «Piri mi mooy: ñetti pañe yi, ñetti fan la. |
1233 | GEN 41:37 | Pexe moomu nag doon lu Firawna aki jawriñam yépp njort ne baax na. |
1241 | GEN 41:45 | Firawna nag tudde Yuusufa Safnat Paneya, may ko jabar Asnat doomu Potifera ma doon sarxalkat ca dëkk ba ñuy wax On. Yuusufa doxe ca tegoo kilifteefu Misra gépp. |
1246 | GEN 41:50 | Laata ati xiif yay agsi, Yuusufa am na ñaari doom yu góor ak Asnat doomu Potifera, kilifag diine, ga ca On. |
1396 | GEN 46:9 | Doomi Ruben yu góor di Anog ak Palu ak Esron ak Karmi. |
1399 | GEN 46:12 | Doomi Yuda yu góor di Er ak Onan ak Sela ak Peres ak Sera, te Er ak Onan faatu ca réewu Kanaan. Doomi Peres yu góor di Esron ak Amul. |
1400 | GEN 46:13 | Doomi Isaakar yu góor di Tola ak Puwa ak Yasub ak Simron. |
1402 | GEN 46:15 | Góor ñooñoo xeetoo ci Leya, te askanoo ci Yanqóoba ca Padan Aram, gannaaw Diina miy doomam ju jigéen. Boo boolee doomam yépp, góor ak jigéen, ñuy fanweer ak ñett. |
1407 | GEN 46:20 | Yuusufa itam am Manase ak Efrayim ca réewum Misra, seen yaay di Asnat doomu Potifera, may njiitu diine ca dëkk ba ñu naan On. |
1459 | GEN 48:7 | Li tax ma def loolu mooy, bi ma jógee Padan di ñibbi, Rasel dafa faatu ca yoon wa ci sama kanam, ba nuy tollu ca réewu Kanaan, booba nu ngay dem, bay jub Efrata. Ma suul ko foofa, ca yoonu Efrata.» Efrata mooy Betleyem tey. |
1544 | EXO 1:11 | Ba loolu amee ñu fal ay nit ñu leen di ga ca seeni sas, di leen ca fitnaal lool. Noonu la bànni Israyil tabaxale Firawna buuru Misra dëkk, ya ñu naa Pitom ak Ramses, mu def ko ay dencukaayi dund. |
1548 | EXO 1:15 | Firawna buuru Misra teg ca wax ak rewlikati Ebrë ya, te kenn ka tuddoon Sifra, ka ca des di Puwa. |
1588 | EXO 3:8 | Damaa wàcc, xettlisi leen ci waa Misra; génne leen réew moomu, ba yóbbu leen réew mu baax te yaatu, réew mu meew maak lem ja tuuroo, foofa ca diiwaanu Kanaaneen ña ak Etteen ña ak Amoreen ña ak Periseen ña ak Eween ña ak Yebuseen ña. |
1597 | EXO 3:17 | Dogu naa leena jële ci seen notaange gii ngeen nekke ci Misra, yóbbu leen ca réewum Kanaaneen ña ak Etteen ña ak Amoreen ña ak Periseen ña ak Eween ña ak Yebuseen ña, réew mu meew maak lem ja tuuroo.’ ” |
1670 | EXO 6:14 | Bànni Israyil ya yilifoon seen kër baay, ñoo di: Góor ña Ruben, taawu Israyil, jur: Anog ak Palu ak Esron ak Karmi. Ñooñoo sos làngi Ruben. |
1681 | EXO 6:25 | Elasar doomu Aaróona moom, moo jël soxna kenn ca doomi Putiyel, kooku am ak moom Fineyas. Ñooñoo yilif seeni kër baay ca Leween ña, ku nekk sos làngam. |
1892 | EXO 14:2 | «Waxal bànni Israyil, ne leen ñu walbatiku dali fa jàkkaarlook Pi Axirot, ca diggante Migadol ak géeju Barax ya. Dal-leen foofa jàkkaarlook Baal Cefon ca tefes ga. |
1899 | EXO 14:9 | Waa Misra topp leen, ñook fasi Firawna yépp, ak watiiri xareem ak dawalkatam yaak xarekatam ya, ba dab leen fa ñu dal ca tefesu géeju Barax ya, fa jàkkaarlook Baal Cefon ca wetu Pi Axirot. |
2168 | EXO 23:23 | «Bu leen sama malaaka jiitoo, ba yóbbu leen ca réewum Amoreen ña ak Etteen ña ak Periseen ña ak Kanaaneen ña ak Eween ña ak Yebuseen ña, ba ma faagaagal leen ñoom ñépp, |
2281 | EXO 27:8 | Pax ngay def sarxalukaay bi ci biir; nga defare ko ay xànq yu tàppandaar. Na ñu la ko wone ca kaw tund wa rekk lañu koy defe. |
2315 | EXO 28:21 | Per yeek turi doomi Israyil ñooy tolloo ab lim: muy fukk ak ñaar, ni tur yi tollu. Dees ciy ñaas tur yi ni xàmmikaayi torlu, ku nekk ak turam, ba fukki giir yeek ñaar daj. |
2360 | EXO 29:23 | Pañe biy taaje fi kanam Aji Sax ji te def mburu yu amul lawiir nag, nanga ci sàkke menn mburu mu tàppandaar, ak menn mburu mu ñu xiiwe diwu oliw, ak menn mburu mu gëna sew. |
2476 | EXO 33:2 | Maay yebal malaaka mu jiitu la, te maa fay dàqe Kanaaneen ña ak Amoreen ña ak Etteen ña ak Periseen ña ak Eween ña ak Yebuseen ña, |
2508 | EXO 34:11 | Bàyyileen xel bu baax li ma leen sant bésub tey jii. Maa ngii di leen dàqal Amoreen ñi ak Kanaaneen ñi ak Etteen ñi ak Periseen ñi ak Eween ñi ak Yebuseen ñi. |
2625 | EXO 37:20 | Peru tegukaayu làmp bi itam am na ñeenti kaas yu bindoo ni tóor-tóori garabu amànd, ànd ak ay kàmbóotam aki mbaram. |
2679 | EXO 39:14 | Per yeek turi doomi Israyil yu góor ñoo tolloo ab lim: muy fukk ak ñaar, ni tur yi tollu. Ñu ñaas ci tur yi ni xàmmikaayi torlu, ku nekk ak turam, ba fukki giir yeek ñaar daj. |
3118 | LEV 14:6 | Picc miy dund da koy booleek bantu seedar bi ak wëñ gu xonq curr gi ak caru isob bi, boole lépp sóob ci deretu picc ma ñu rendi woon tiimale ko ndox mi balle ci bëtu ndox. |
3615 | NUM 1:10 | Ñi ciy askanu Yuusufa ñii la: Ci wàllu Efraymeen ñi, Elisama doomu Amiyut. Wàllu Manaseen ñi, Gamalyel doomu Pedasur. |
3618 | NUM 1:13 | Wàllu Asereen ñi, Pagyel doomu Okkran. |
3679 | NUM 2:20 | «Ñay dale fa feggook ñoom ñooy giirug Manaseen ñi, kilifag askanu Manase di Gamalyel doomu Pedasur. |
3686 | NUM 2:27 | «Ñay dale fa feggook ñoom ñooy giirug Asereen ñi, kilifag askanu Aser di Pagyel doomu Okkran. |
3905 | NUM 7:54 | Bésub juróom ñetteel ba kilifag Manaseen ña, Gamalyel doomu Pedasur moo aye, |
3910 | NUM 7:59 | ak saraxu cant gi ci biir jàmm, di ñaari yëkk ak juróomi kuuy ak juróomi sikket, ak juróomi xari menn at. Looloo doon saraxu Gamalyel doomu Pedasur. |
3923 | NUM 7:72 | Bésub fukkeel baak benn, kilifag Asereen ña, Pagyel doomu Okkran moo aye, |
3928 | NUM 7:77 | ak saraxu cant gi ci biir jàmm, di ñaari yëkk ak juróomi kuuy ak juróomi sikket, ak juróomi xari menn at. Looloo doon saraxu Pagyel doomu Okkran. |
4001 | NUM 10:12 | Bànni Israyil daldi sumb seen yooni tukki ya, bàyyikoo màndiŋu Sinayi. Ci kaw loolu niir wa daleji ca màndiŋu Paran. |
4012 | NUM 10:23 | njiital gàngooru Manaseen ña di Gamalyel doomu Pedasur, |
4015 | NUM 10:26 | njiital gàngooru Asereen ña di Pagyel doomu Okkran, |
4076 | NUM 12:16 | Gannaaw loolu mbooloo ma bàyyikoo Aserot, ñu dali ca màndiŋu Paran. |
4079 | NUM 13:3 | Ci kaw loolu Musaa yebal ndaw ña ci ndigalal Aji Sax ji, ñu bàyyikoo ca màndiŋu Paran. Ñoom ñépp ay njiiti bànni Israyil lañu woon. |
4085 | NUM 13:9 | ak Palti doomu Rafu, ci giirug Beñamineen ñi, |
4102 | NUM 13:26 | Ñu dikk ba ci Musaa ak Aaróona, ak mbooloom bànni Israyil gépp, ca màndiŋu Paran, ca Kades. Ñu àgge leen xibaar, ñoom ak mbooloo ma mépp, ba noppi won leen meññeefum réew ma. |
4196 | NUM 16:1 | Ku ñuy wax Kore doomu Isar, mi askanoo ci Keyat doomu Lewi, moo àndoon ak ay Rubeneen, ñuy Datan ak Abiram, doomi Elyab, ak Onn doomu Pelet, |
4361 | NUM 21:20 | jóge Bamot ba ca xur, wa ca àllub Mowab, àkki nag njobbaxtalu tundu Pisga, wa tiim ndànd-foyfoy ga. |
4381 | NUM 22:5 | Mu yebal ay ndaw ca Balaam doomu Bewor ngir wooyi ko, ca Petor ga Balaam cosaanoo, ca tàkkal dex ga ngir ne ko: «Balaam! Gàngoor a ngii jóge Misra. Ñu ngii lal suuf si ba mu daj, te ñoo sanc, janook man màkk. |
4431 | NUM 23:14 | Mu daldi koy yóbbu ba ca toolub Sofim, ca collu tundu Pisga. Ci kaw loolu mu tabax fa juróom ñaari sarxalukaay, sarxalukaay bu nekk, mu sarxalati fa yëkk wu ndaw akam kuuy. |
4445 | NUM 23:28 | Balag yóbbu Balaam ba ca collu tundu Pewor, wa tiim ndànd-foyfoy ga. |
4475 | NUM 25:3 | Israyil nag taqook tuur ma ñuy wax Baal Pewor, ba sànjum Aji Sax ji tàkkal Israyil. |
4477 | NUM 25:5 | Musaa ne àttekati Israyil: «Na ku nekk ci yeen rey nitam ñi taqook Baal Pewor.» |
4490 | NUM 25:18 | ndax ñoom ñoo leen noonoo woon ba ñu leen woree ca mbirum Pewor ma, ak itam ca mbirum ndaw sa Kosbi, seen mbokk may doomu kilifag Majan ja, te ñu jam ko keroog bésu mbas, ma sababoo ca mbirum Baal Pewor, tuur ma.» |
4496 | NUM 26:5 | Ruben moo doon taawub Israyil. Ñi askanoo ci Ruben ñoo di Anog mi sos làngu Anogeen ñi, ak ñoom Palu mi sos làngu Paluween ñi, |
4499 | NUM 26:8 | Palu moo meññ Elyab, |
4511 | NUM 26:20 | Ñi askanoo ci Yuda, ñook seeni làng ñoo di ñoom Sela mi sos làngu Celaneen ñi, ak ñoom Peres mi sos làngu Pereseen ñi, ak ñoom Sera mi sos làngu Cerayeen ñi. |
4512 | NUM 26:21 | Ñi askanoo ci Peres ñoo di ñoom Esron mi sos làngu Esroneen ñi, ak ñoom Amul mi sos làngu Amuleen ñi. |
4514 | NUM 26:23 | Ñi askanoo ci Isaakar, ñook seeni làng ñoo di Tola mi sos làngu Toleen ñi, ak ñoom Puwa mi sos làngu Puween ñi, |
4682 | NUM 31:16 | Xanaa du ñoom ñoo dëdduloo woon bànni Israyil Aji Sax ji, ci ndigalal Balaam, ca mbir ma woon ca Pewor, ba tax mbas ma dikkal mbooloom Aji Sax ji? |
4769 | NUM 33:7 | Ba ñu bàyyikoo Etam, dañoo walbatiku ba Pi Axirot ga janook Baal Cefon, daldi dal fa kanam Migadol. |
4770 | NUM 33:8 | Ñu jóge Pi Axirot, jàll géej ga, wuti màndiŋ ma. Dox nañu yoonu ñetti fan ca biir màndiŋu Etam, doora dal Maara. |
4781 | NUM 33:19 | Ñu jóge Ritma, dali Rimon Peres, |
4782 | NUM 33:20 | jóge Rimon Peres, dali Libna, |
4804 | NUM 33:42 | Ñu jóge Calmona, dali Punon, |