Wildebeest analysis examples for:   wol-wolKYG   p    February 11, 2023 at 19:57    Script wb_pprint_html.py   by Ulf Hermjakob

20  GEN 1:20  Ba loolu amee Yàlla ne: «Na ndox fees ak ay ndiiraani xeeti bindeef, te ay picc tiim suuf, di naaw ci asamaan.»
21  GEN 1:21  Ci biir loolu Yàlla bind rabi géej yu mag yi ak mboolem mbindeef muy féey tey ramm-rammi ci ndox mi, mu ci nekk ak wirgoom, teg capp luy boroomi laaf, lu ci nekk ak wirgoom. Yàlla gis ne baax na.
22  GEN 1:22  Ba mu ko defee Yàlla barkeel leen, daldi ne: «Giirleen te bare, ba fees ndoxi géej.» Mu neeti: «Na picc yi bare ci kaw suuf.»
25  GEN 1:25  Yàlla dafa bind rabi àll yi, lu ci nekk ak wirgoom, jur gu ci nekk ak wirgoom, akpp luy raam ci kaw suuf, lu ci nekk ak wirgoom. Yàlla nag gis ne baax na.
26  GEN 1:26  Yàlla ne: «Nanu bind nit ci sunu melokaan, mu nirook nun, te na yilif jëni géej ak picci asamaan ak jurpp ak suufpp akpp lu ciy raam.»
27  GEN 1:27  Yàlla dafa bind nit ci takkndeeram; ci takkndeeru boppam la Yàlla bind nit, góor ak jigéen la bind.
28  GEN 1:28  Yàlla barkeel leen ne leen: «Giirleen te bare, ba fees àddina, di ko saytu; te it yilifleen jëni géej ak picci asamaan ak mboolem mbindeef muy yëngu ci kaw suuf.»
29  GEN 1:29  Yàlla ne: «Xool-leen, jox naa leenpp gàncax gu ànd ak jiwoom ci kaw suufpp akpp garab guy meññ tey jur jiwoom, muy seen dund.
30  GEN 1:30  Naka rabi àllpp it, ñook picci asamaanpp akpp luy raam ci kaw suuf, te di boroom bakkan, jox naa leenpp luy ñax mu tooy, ñoom itam, muy seen lekk.» Mu daldi nekk noona.
31  GEN 1:31  Yàlla nag gis li mu defpp, fekkpp baax lool. Ngoon jot, suba dugg, muy bésub juróom benneel ba.
32  GEN 2:1  Ci kaw loolu asamaan ak suuf ak li ñu ëmbpp mat.
33  GEN 2:2  Bésub juróom ñaareel ba fekk na Yàlla matal liggéeyam. Mu dal-lu nag ca bésub juróom ñaareel ba, gannaaw ba mu liggéeyee loolupp.
34  GEN 2:3  Yàlla daldi barkeel bésub juróom ñaareel ba, def ko bés bu sell, ndax da caa dal-lu woon gannaaw liggéey, ba mu sàkkepp.
37  GEN 2:6  Ci biir loolu mbënn di balle ci suuf, di tooyalpp.
38  GEN 2:7  Yàlla Aji Sax ji nag móol nit ci pëndu suuf, sol ngelawal dund ci paxi bakkanam, nit daldi doon boroom bakkan.
39  GEN 2:8  Naka noona Yàlla Aji Sax ji jëmbat tool ca biir Àjjana fa féete penku ba, tàbbal ca nit ka mu bind.
40  GEN 2:9  Yàlla Aji Sax ji nag saxal ci suufpp luy garab gu meññeef ma rafet te neexa lekk; mu def it garab gay taxa dund ca digg tool ba, moom ak garab gay taxa xam lu baax ak lu bon.
42  GEN 2:11  Turu menn wal ma di dexu Pison, moo wër réewum Awilapp. Wurus a nga woon ca réew mooma,
43  GEN 2:12  di wurusu ngalam; te it ndàbb lu neex xet a nga fa woon ak per yu jafe yu ñuy wax onigsë.
44  GEN 2:13  Ñaareelu dex ga di Giyon, wër réewu Kuuspp;
45  GEN 2:14  turu ñetteelu dex ga di Tiigar, féete réewum Asiri penku; ñeenteelu dex ga di Efraat.
49  GEN 2:18  Yàlla Aji Sax ji daldi ne: «Wéet baaxul ci nit, kon dinaa ko bindal ku koypple te jekk ci doon wéttalam.»
50  GEN 2:19  Loolu fekk na Yàlla Aji Sax ji sàkk ci suuf nja-àllpp ak njanaawpp, daldi leen indil nit, di seet nu leen nit di tudde; te tur wu mu leen jox, muy moom.
51  GEN 2:20  Ba mu ko defee nit kooku, di Aadama, tudd jurpp ak picc pp ak rabi àllpp, waaye fekku ca ku koypple te jekk ci doon wéttalam.
52  GEN 2:21  Bi loolu amee Yàlla Aji Sax ji nelawloo Aadama nelaw yu xóot. Ba muy nelaw nag, mu rocci genn ciy faaram, fatte pax ma aw suux.
56  GEN 2:25  Ku góor ki ak soxnaam, ñoom ñaar ñépp, yaramu neen lañu defoon, te amuñu ci woon genn kersa.
57  GEN 3:1  Jaan nag moo gënoona muus ci rabi àll, yi Yàlla Aji Sax ji sàkkpp. Jaan ja moo ne jigéen ja: «Ndax wóor na ne Yàllaa ne: “Buleen lekk ci doomi genn garabu tool bi”?»
70  GEN 3:14  Yàlla Aji Sax ji nag ne jaan ja: «Gannaaw def nga loolu, yaw rekk yaay alku ci rabi kërpp ak rabi àllpp; dinga watatu, di lekk pënd sa giiru dundpp.
71  GEN 3:15  Dinaa def mbañeel sa digganteek jigéen ji, ba dëddale sa xeet ak xeetam, muy toj sa bopp, nga di ko màtt ci téstën.»
73  GEN 3:17  Mu tegaat ca ne Aadama: «Gannaaw dégg nga sa waxu soxna, ba lekk ci garab gi ma la aaye, dinaa rëbb suuf ndax yaw; coono bu metti nga ciy dunde sa giiru dundpp.
75  GEN 3:19  saw ñaq ngay dunde, ba kera ngay dellu ci suuf, si ma la jële; ndaxte pënd nga, te dinga dellu di pënd.»
76  GEN 3:20  Aadama nag tudde soxnaam Awa (mu firi Dund), ndax mooy ndeyupp kuy dund.
80  GEN 3:24  Da koo dàq, ba noppi teg ca penkub toolu Àjjana ba ay malaakay serub, boole ca saamar buy xuyy-xuyyi, tey dem ak a dikk, di wattu yoon, wa jëm ca garab gay taxa dund.
96  GEN 4:16  Kayin daldi bàyyikoo ca Aji Sax ji, dem dëkki réewu Nódd, fa féete Àjjana penku.
97  GEN 4:17  Gannaaw loolu Kayin dëkkoo na soxnaam, mu ëmb, am Enog. Ci biir loolu Kayin sanc ab dëkk, dippee ko doomam ju góor Enog.
102  GEN 4:22  Silla moom jur Tubal Kayin miy tëggpp luy jumtukaayu xànjar ak weñ. Tubal Kayin am na jigéen bu tudd Naama.
128  GEN 5:22  Matusalem juddu na, ba noppi Enog topp Yàlla ñetti téeméeri at (300), amaat ay doom yu góor ak yu jigéen.
130  GEN 5:24  Enog dafa topp Yàlla, ba jekki-jekki giseesatu ko, ndaxte Yàllaa ko yéege fa moom.
135  GEN 5:29  Mu tudde ko Nóoyin (mu firi Noflaay) ndax dafa ne: «Kii moo nuy taxa noyyiwaat, noppal nu ci liggéey yu metti ak coonoy mbeyu suuf, si Aji Sax ji rëbb.»
141  GEN 6:3  Aji Sax ji daldi wax ne: «Manumaa bàyyi nit, muy wéyee dunde noo, gi ma ko may, ndax nit du dara lu dul suuxi neen, kon dinaa leen àppal diirub téeméeri at ak ñaar fukk (120).»
142  GEN 6:4  Ca jamono yooya ak itam gannaaw ba goney Yàlla yooyu àndeek jigéeni àddina, ba am ca ay doom, aw xeetu ponkal wu ñuy wax Nefilim moo nekkoon ci àddina. Ñooy ponkal ya woon te doonoon góor ñu amoon tur.
147  GEN 6:9  Askanu Nóoyin mooy lii. Nóoyin nit ku jub la woon, di ku mat ci biir nit ñi mu bokkal jamono, te di ku topp Yàlla.
150  GEN 6:12  Yàlla gis ne àddina yàqu na, ndaxte jëfi ñépp a bokk ñaaw fi kaw suuf.
152  GEN 6:14  «Yaw nag wutal dénku sippar, yettal ci sa bopp gaal gu mag; nga sàkk ci ay néeg, te diw ko koltaar biir ak biti.
155  GEN 6:17  «Maa ngi nii di indi mbënnu ndox ci kaw suuf, mu farpp luy dund lu asamaan tiim; tepp lu nekk ci kaw suuf dina dee.
157  GEN 6:19  Te xeeti rabpp nanga ci dugal ñaar ci gaal gi, wu ci nekk, nga def ko góor ak jigéen; su ko defee ngeen ànd mucc.
158  GEN 6:20  Xeetu picc wu ci nekk ak xeetu bàyyima wu ci nekk akpp xeetu rab wuy raam ci suuf, dina def ñaar, ñëw ci yaw, ba raw.
159  GEN 6:21  Sàkkal cipp xeetu dund, denc, ngeen bokk dunde.»
160  GEN 6:22  Noonu la Nóoyin def.pp lu ko Yàlla sant, def na ko.
161  GEN 7:1  Gannaaw ba loolu amee Aji Sax ji dafa wax Nóoyin ne ko: «Duggal ci gaal gu mag gi, yaak sa njabootpp, ndaxte niti jamono jii, yaw rekk laa ci gis, nga jub ni ma ko bëgge.
162  GEN 7:2  Xeeti rab yu setpp yóbbaale ci juróom ñaar yu góor ak juróom ñaar yu jigéen, ak ñaar ci xeeti rab yi setul, te ñuy góor ak jigéen.
163  GEN 7:3  Te it xeetu picc mu nekk yóbbaale ci juróom ñaar yu góor ak juróom ñaar yu jigéen, ngir seen xeet baña fey ci kaw suuf.
165  GEN 7:5  Nóoyin daldi def la ko Aji Sax ji santpp.
168  GEN 7:8  Rab yu set yi ak yi setul ak picc yi ak yiy raam
174  GEN 7:14  àndandook rabu àllpp, lu ci nekk ak wirgoom, ak jurpp, lu ci nekk ak wirgoom, akpp luy raam ci kaw suuf, lu ci nekk ak wirgoom, akpp luy naaw, lu ci nekk ak wirgoom, muy picc mbaa boroomi laaf.
175  GEN 7:15  pp luy boroom bakkan def na ñaar-ñaar, ànd ak Nóoyin, dugg ca gaal ga,
176  GEN 7:16  mboolem xeetu mbindeef rekk, di góor ak jigéen, ni ko ko Yàlla sante. Ci kaw loolu Aji Sax ji nepp buntu gaal gi, gannaaw bi Nóoyin duggee.
179  GEN 7:19  Ndox ma di walangaan, ba mëdd tund yu kawe yapp fu asamaan tiim.
181  GEN 7:21  Mboolem mbindeef mu daan dox ci kaw suuf dee na ca. Picc yi ak jur gi ak rabi àll yi akpp luy raam ci kaw suuf dee na, ñoom ak nit ñépp.
183  GEN 7:23  Luy dund ci àddina daldi sànku, ba nit ak jur ak luy raam ak luy naaw—pp la Aji Sax ji raafal ci àddina. Nóoyin rekk a des, moom ak ña àndoon ak moom ca gaal ga.
190  GEN 8:6  Teg nañu ca ñeent fukki fan, Nóoyin doora ubbi poroxndoll, ba mu sàkkaloon gaal ga,
192  GEN 8:8  Mu teg ca yebal pitax, ba xam ndax ndox mi ci suuf fer na.
193  GEN 8:9  Teewul pitax ma gisul fenn fu mu tag, ndax ndox mi muur na suufpp. Mu délsi nag fa moom ca gaal ga. Nóoyin tàllal loxoom,pp ko dugal ci biir fi wetam.
194  GEN 8:10  Négandiku na juróom ñaari fan, doora yebalaat pitax ma.
195  GEN 8:11  Ba mu délsee ca ngoon, indaalewul lu moy xobu oliw wu tooy wu keppe ca sàll wa. Nóoyin xam ne ndox mi taa woon ci suuf, fer na.
196  GEN 8:12  Mu négati juróom ñaari fan, bàyyiwaat pitax ma. Boobu yoon nag délsiwaatul ca moom.
197  GEN 8:13  At ma Nóoyin amee juróom benni téeméeri at ak benn, keroog benn fanu weer wa jëkk, ndox ma taa woon ca suuf daldi fendi. Nóoyin ubbi kubeer ga, xool, ba gis ne kaw suufpp wow na.
201  GEN 8:17  Génnewaaleelpp luy xeetu mbindeef mu ngeen àndal: picc yi ak bàyyima yi ak luy raam, ñu fulandiwu ci kaw suuf, daldi giir te bare.»
203  GEN 8:19  Rabi àll yi ak luy raam ak luy naaw ak luy dox ci kaw suuf—pp génne ca gaal ga, lu ci nekk ak wirgoom.
204  GEN 8:20  Naka la Nóoyin génn, daldi sàkkal Aji Sax ji sarxalukaay, màggale ko ko. Mu sàkk nag ci mboolem rab wu set ak mboolem picc mu set, jébbal Yàlla ca sarxalukaay ba, muy saraxu rendi-dóomal.
205  GEN 8:21  Ci kaw loolu xetug jàmm gillee ca sarax sa, yéeg fa Aji Sax ja. Booba la wax ci xolam ne: «Dootuma rëbb suuf mukk ndax nit, doonte ba muy ndaw lay dale xinte lu ñaaw ci xolam. Dootuma boole fàdd mukkpp luy dund, nii ma ko defe.
208  GEN 9:2  Mboolem rabi àll yi ak njanaawi asamaan ak ndëgmeent yi ci suuf, ak jëni géejpp, dinañu leen ragal lool. Teg naa leen ci seeni loxo.
209  GEN 9:3  Man ngeena dunde boroom bakkan yooyupp. Jagleel naa leen bindeef yooyupp, ni ma leen jagleele woon gàncax.
210  GEN 9:4  «Waaye buleen lekkpp wu ànd ak deret, ndaxte dund a ngi ci deret.
211  GEN 9:5  Seen dundu nit itam, mu ngi ci seen deret, kon kat,pp ku tuur seen deret dinaa ko ko topp. Te it mala mu ci rey nit dinaa ko ko topp, ni may toppe nit. Dinaa topp ku nekk deretu moroomam.