2108 | EXO 21:30 | Su fekkee ne dees koo sas ndàmpaay, na fey lim bu ñu ko mana sas, muy njot-gi-bakkanam. |
2398 | EXO 30:15 | Ki woomle du fey lu ëpp, ki néewle du fey lu yées genn-wàllu siikal, buy fey jooxeb Aji Sax ji ngir njot-gi-bakkanam. |
12860 | EST 9:22 | di ko baaxantale bés ya Yawut yi dal-loo ca seeni noon, ak weer wa seen naqar walbatikoo di mbégte, seen tiis di bésub jàmm, ngir ñuy wormaal yooyu bés, muy bési bernde ak bànneex yu ñuy joqlantey teraanga, di ci defal néew-ji-doole. |
13449 | JOB 24:9 | Xoncees na jirim ci weenu ndeyam, jëlees na tayle alalu néew-ji-doole. |
14044 | PSA 9:13 | Mooy topp nit bakkanu moroomam, di ko ba xel, te du fàtte yuuxi néew-ji-doole. |
14060 | PSA 10:8 | Day tëroo ciy dëkk-dëkkaan, làqu di bóom ku deful dara, nëbbu di wootal néew-ji-doole. |
14064 | PSA 10:12 | Aji Sax ji, jógal! Éy Yàlla, xàccil sa loxo. Bul fàtte néew-ji-doole. |
14083 | PSA 12:6 | Ku ñàkk a ngi, ñu futti, mu ngi binni, di néew-ji-doole. Aji Sax ji nee: «Maa ngii, di ci jóg, teg leen fi rawtu gu ñu ne siiw.» |
14464 | PSA 36:6 | Céy Aji Sax ji, gore nga ba kaw asamaan, dëggu ba kaw-li-kaw. |
14568 | PSA 41:2 | Ndokklee yaw mi yég néew-ji-doole. Aji Sax jee lay xettli, bésub njàqare. |
15622 | PSA 103:6 | Aji Sax jeey def njekk, di àtte jépp néew-ji-doole. |
16682 | PRO 8:10 | Na la samab yar gënal xaalis, xam-xam dàqal la ngën-gi-wurus. |
16979 | PRO 18:8 | Waxi jëwkat di ñam wu neex wuy seey, jàll ca biir-a-biir. |
17233 | PRO 26:22 | Waxi jëwkat di ñam wu neex, wuy seey, jàll ca biir-a-biir. |
17374 | PRO 31:20 | Day jox ku ñàkk, di sàkkal néew-ji-doole. |
17668 | SNG 4:16 | Yaw, ngelawal bëj-gànnaar, yewwul, ngelawal bëj-saalum, dikkal, wolal-leen ma sama tool bi, mu gilli; sama nijaay dugg toolam, xéewloo ngën-gi-meññeefam. |
21685 | EZK 44:17 | «Bu ñu dee jàll buntu ëttu biir bi, yérey lẽe lañuy sol. Buñu sol ndimol kawaru jur, bu ñuy liggéey fu wees buntu ëttu biir bi, jëm ca biir-a-biir. |