|
22910 | -Ca ñaareelu atu nguuru Buur Daryus, ca juróom benneelu weer wa, yemook benn fan ca weer wa, kàddug Aji Sax ji moo dikk ci jottlib Yonent Yàlla Ase, ñeel doomu Selcel, Sorobabel boroom Yuda, ñeel itam doomu Yoccadag, Yosuwe sarxalkat bu mag ba. Mu ne: |