|
20488 | Dërkiisalal seen xol (Tegleen njàqarey xol / Muural seenum xel,) na leen sag alkànde ñeel. | |
23069 | Yéeneb kàddug Aji Sax jii moo rot ci kaw réewum Addarag, ba dali ca kaw Damaas. Du ci mboolem giiri Israyil rekk la Aji Sax ji ne jàkk bëtam, waaye doom aadama yépp la ne jàkk. (xg / Gëti nit ñi, ba ci giiri Israyil gépp kat, ñu ngi ne jàkk ci Aji Sax ji.) |